Vous avez cherché: gisoon (Wolof - Espagnol)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Espagnol

Infos

Wolof

kañ lanu la gisoon, nga wopp mbaa ñu tëj la, nu ñëw ci yaw?”

Espagnol

¿cuándo te vimos enfermo, o en la cárcel, y fuimos a ti?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

di wéy ci bëre, bi ngeen gisoon ci man, te dégg léegi sama mbir.

Espagnol

así tendréis el mismo conflicto que habéis visto y que ahora oís que sigue en mí

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

esayi dafa wax loolu, ndaxte gisoon na ndamu yeesu te mi ngi doon wax ci ay mbiram.

Espagnol

estas cosas dijo isaías porque vio su gloria y habló acerca de él

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mbooloo mu bare topp ci moom, ndaxte gisoon nañu firnde yooyee mu wone, bi mu wéralee jarag ya.

Espagnol

y le seguía una gran multitud, porque veían las señales que hacía en los enfermos

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

kañ lanu la gisoon, nga nekk ab doxandéem, nu fat la; mbaa nga rafle, nu wodd la?

Espagnol

¿cuándo te vimos forastero y te recibimos, o desnudo y te vestimos

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi baat ba waxee ba noppi, yeesu rekk des fa. taalibe ya noppi, bañ a nettali kenn ca jamono jooja la ñu gisoon.

Espagnol

cuando cesó la voz, jesús fue hallado solo. y ellos callaron, y en aquellos días no dijeron a nadie nada de lo que habían visto

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi mu agsee galile, nit ñi teeru ko, ndaxte ñoom itam teewoon nañu ca màggalu bésu jéggi ba ca yerusalem, te gisoon nañu la mu fa defoon lépp.

Espagnol

luego, cuando entró en galilea, los galileos le recibieron, ya que habían visto cuántas cosas había hecho en jerusalén en la fiesta; porque ellos también habían ido a la fiesta

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ba ñu dégloo buur ba nag, ñu dem. te biddiiw, ba ñu gisoon ca penku ba, ne tell jiite leen, ba àgg, tiim fa xale ba nekk.

Espagnol

ellos, después de oír al rey, se fueron. y he aquí la estrella que habían visto en el oriente iba delante de ellos, hasta que llegó y se detuvo sobre donde estaba el niño

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ngëm moo tax ba, bi musaa juddoo, ay waajuram nëbb ko lu mat ñetti weer, ndaxte gisoon nañu ne, xale bu taaru la woon, te ragaluñu woon ndigalu buur bi.

Espagnol

por la fe moisés, cuando nació, fue escondido por sus padres durante tres meses, porque vieron que era un niño hermoso y porque no temieron al mandamiento del rey

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

kenn ci surgay saraxalekat bu mag ba, di mbokku ka piyeer coroon noppam, ne piyeer: «xanaa du yaw laa gisoon ak moom ca tool ba?»

Espagnol

uno de los siervos del sumo sacerdote, pariente de aquel a quien pedro le había cortado la oreja, le dijo: --¿no te vi yo en el huerto con él

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

«sunuy maam amoon nañu ca màndiŋ ma tàntu màggalukaay, bi ëmboon li yàlla seede. tànt boobu nag defoon nañu ko, roye ko ci bi musaa gisoon, ni ko ko yàlla sante woon.

Espagnol

en el desierto, nuestros padres tenían el tabernáculo del testimonio, como lo había ordenado dios, quien ordenaba a moisés que lo hiciese según el modelo que había visto

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ci kaw loolu dinañu tontu ne: “boroom bi, kañ lanu la gisoon, nga xiif, mbaa nga mar, nga nekk ab doxandéem mbaa rafle, nga wopp mbaa ñu tëj la, te topptoowunu la?”

Espagnol

entonces le responderán: "señor, ¿cuándo te vimos hambriento, o sediento, o forastero, o desnudo, o enfermo, o en la cárcel, y no te servimos?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,792,259,932 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK