Vous avez cherché: jabar (Wolof - Espagnol)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Espagnol

Infos

Wolof

na góor bëgg jabaram, ni mu bëgge boppam. bëgg sa jabar, bëgg sa bopp la.

Espagnol

de igual manera, los esposos deben amar a sus esposas como a sus propios cuerpos. el que ama a su esposa, a sí mismo se ama

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

jëkkër war na def warugaru jëkkër ci jabaram; jabar it def warugaru jabar ci jëkkëram.

Espagnol

el esposo cumpla con su esposa el deber conyugal; asimismo la esposa con su esposo

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

keneen ne ko: “damay sog a takk jabar, looloo tax duma man a ñëw.”

Espagnol

el otro dijo: "acabo de casarme y por tanto no puedo ir.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Wolof

waaye ku takk jabar, fàww mu bàyyi xel ci mbiri àddina si, ak nu mu man a neexe jabaram,

Espagnol

pero el casado se preocupa de las cosas de la vida, de cómo ha de agradar a su esposa

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte keroog ndekkite li kenn du am jabar, kenn du am jëkkër, waaye dinañu mel ni malaaka yi ci kaw.

Espagnol

porque cuando resuciten de entre los muertos, no se casarán ni se darán en casamiento, sino que son como los ángeles que están en los cielos

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu yeesu ne leen: «ku fase sa jabar, takk jeneen, njaaloo nga, di tooñ ku jëkk ka.

Espagnol

Él les dijo: --cualquiera que se divorcia de su mujer y se casa con otra, comete adulterio contra ella

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye ña ñu àtte ne, yeyoo nañoo bokk ci dundu ëllëg ak ci ndekkite li, kenn du am jabar, kenn du am jëkkër.

Espagnol

pero los que son tenidos por dignos de alcanzar aquel mundo venidero y la resurrección de los muertos no se casan, ni se dan en casamiento

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bëggoon naa, ngeen bañ a am benn xalaat. góor gu takkul jabar dafay bàyyi xel ci mbiri boroom bi, di wut a neex boroom bi.

Espagnol

quisiera, pues, que estuvieseis libres de ansiedad. el no casado se preocupa de las cosas del señor, de cómo agradar al señor

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

nit ñaa ngi doon lekk ak di naan, di jël jabar ak a séyi, ba bés ba nóoyin duggee ca gaal ga. noonu mbënn ma ñëw, rey leen ñoom ñépp.

Espagnol

ellos comían y bebían; se casaban y se daban en casamiento, hasta el día en que noé entró en el arca, y vino el diluvio y los destruyó a todos

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

«amoon na fi nag juróom-ñaari góor, ñu bokk ndey ak baay. taaw ba takk jabar, faatu, te bàyyiwul doom.

Espagnol

había siete hermanos. el primero tomó mujer, y murió sin dejar descendencia

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte ca bés ya jiitu mbënn ma, nit ñaa ngi doon lekk di naan, góor yaa ngi doon takk jabar, tey maye seeni doom, ba bés ba nóoyin duggee ca gaal ga;

Espagnol

pues como en aquellos días antes del diluvio estaban comiendo y bebiendo, casándose y dándose en casamiento hasta el día en que noé entró en el arca

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu tontu leen: «musaa may na leen, ngeen fase seen jabar, ndax seen xol dafa dëgër, waaye ca njàlbéen ga demewul woon noonu.

Espagnol

les dijo: --ante vuestra dureza de corazón, moisés os permitió divorciaros de vuestras mujeres; pero desde el principio no fue así

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye malaaka ma ne ko: «bul ragal dara sakariya, ndaxte sa ñaan nangu na. elisabet sa jabar dina la jural doom, te dinga ko tudde yaxya.

Espagnol

pero el ángel le dijo: --¡no temas, zacarías! porque tu oración ha sido atendida. tu esposa elisabet te dará a luz un hijo, y llamarás su nombre juan

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

moona bi jataayu gaal ga matee, nu awaat ci yoon wi. te ñépp gunge nu, ñoom ak seeni jabar ak seeni doom; nu génn dëkk ba, sukk ca tefes ga, ñaan ci yàlla.

Espagnol

cuando se nos pasaron los días, salimos acompañados por todos con sus mujeres e hijos hasta fuera de la ciudad, y puestos de rodillas en la playa, oramos

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

kon nag su jabar ji àndee ak beneen góor, te fekk jëkkër jiy dund, dees na ko àtte njaaloo. waaye bu jëkkër ji faatoo, yoon jeexal na seen diggante; man na séy nag ak beneen góor, te loolu du njaaloo.

Espagnol

por lo tanto, si ella se une con otro hombre mientras vive su esposo, será llamada adúltera. pero si su esposo muere, ella es libre de la ley; y si se une con otro esposo, no es adúltera

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,781,412,268 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK