Vous avez cherché: mbóoti (Wolof - Espagnol)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Espagnol

Infos

Wolof

na sàmm mbóoti ngëm gi ak xel mu dal.

Espagnol

que mantengan el misterio de la fe con limpia conciencia

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

nañu nu teg kon ay surgay kirist, di ay jawriñ yuy xamle mbóoti yàlla.

Espagnol

que todo hombre nos considere como servidores de cristo y mayordomos de los misterios de dios

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ci feeñal nu mbóoti coobareem, dëppook yéeneem ju rafet, ji mu jaarale ci kirist.

Espagnol

Él nos ha dado a conocer el misterio de su voluntad, según el beneplácito que se propuso en cristo

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bu ngeen jàngee loolu, dingeen man a xam bu wér dégg, gi ma am ci mbóoti mbiri kirist.

Espagnol

por tanto, leyéndolo, podréis entender cuál es mi comprensión en el misterio de cristo

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yàlla feeñu na ma, xamal ma mbóoti mbir mi mu tëral, ni ma leen ko binde ci kàddu yu néew.

Espagnol

por revelación me fue dado a conocer este misterio, como antes lo he escrito brevemente

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mu tontu leen: «yéen may nañu leen, ngeen xam mbóoti nguuru yàlla, waaye ñi ci biti léeb ay ëmb lépp.

Espagnol

y él les decía: "a vosotros se os ha dado el misterio del reino de dios; pero para los que están fuera, todas las cosas están en parábolas

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Wolof

te buleen ma ci fàtte, ngir waxtu wu ma ubbee sama gémmiñ, ma am lu ma wax, ba man a xamle ak fit wu dëgër mbóoti xebaar bu baax bi.

Espagnol

y también orad por mí, para que al abrir la boca me sean conferidas palabras para dar a conocer con confianza el misterio del evangelio

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

man ci sama bopp, bokk yi, bi ma ñëwee ci yéen, ngir yégle mbóoti yàlla, ñëwuma ci ay wax yu neex ak xam-xam bu réy.

Espagnol

así que, hermanos, cuando yo fui a vosotros para anunciaros el misterio de dios, no fui con excelencia de palabras o de sabiduría

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

juróom-ñaari biddiiw yi nga gis ci sama loxol ndeyjoor, ak juróom-ñaari làmpi diwlin yu wurus yi, ay mbóoti yàlla lañu te lii lañuy tekki: biddiiw yi ñoo di malaakay juróom-ñaari mboolooy ñi gëm; juróom-ñaari làmp yi ñoo di juróom-ñaari mbooloo yi.

Espagnol

en cuanto al misterio de las siete estrellas que has visto en mi mano derecha, y de los siete candeleros de oro: las siete estrellas son los ángeles de las siete iglesias, y los siete candeleros son las siete iglesias

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,790,562,895 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK