Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
waaye ci deretu kirist ju tedd ji, mel ni mbote mu sikkul te wàññikuwul.
sino con la sangre preciosa de cristo, como de un cordero sin mancha y sin contaminación
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
nanu bég te bànneexute jox ko ndam li,ndaxte céetu mbote mi agsi na,séet bi waaj na.
gocémonos, alegrémonos y démosle gloria, porque han llegado las bodas del cordero, y su novia se ha preparado
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
samp nañu miiru dëkk ba ci fukki fondamaa ak ñaar, yu ñu bind turi fukki ndawi mbote ma ak ñaar.
el muro de la ciudad tenía doce fundamentos, y sobre ellos los doce nombres de los apóstoles del cordero
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu malaaka ma won ma dexu ndoxum dund, mu leer ni weer bu set, di génn ca gàngune mu yàlla ak mbote ma,
después me mostró un río de agua de vida, resplandeciente como cristal, que fluye del trono de dios y del cordero
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
mbote ma dindi na juróom-ñaareelu tayu ga, asamaan ne selaw lu mat genn-wàllu waxtu.
cuando él abrió el séptimo sello, se hizo silencio en el cielo como por media hora
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
dara du fa dugg lu am sobe, mbaa kenn kuy sóobu ci ñaawteef walla fen. Ñi ñu bind ci téereb dund bu mbote mi rekk ñoo fay dugg.
jamás entrará en ella cosa impura o que hace abominación y mentira, sino solamente los que están inscritos en el libro de la vida del cordero
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
waa àddina sépp dinañu ko jaamu, ñooñu ñu bindul seeni tur, li dale ci njàlbéenu àddina, ci téereb dund bu mbote mi ñu rendi.
y le adorarán todos los habitantes sobre la tierra, cuyos nombres no están inscritos en el libro de la vida del cordero, quien fue inmolado desde la fundación del mundo
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
ndaxte mbote mi nekk ci diggu gàngune mi dina leen sàmm,yóbbu leen ca bëti ndoxum dund ma,te yàlla dina fomp bépp rangooñ ci seeni bët.»
porque el cordero que está en medio del trono los pastoreará y los guiará a fuentes de agua viva, y dios enjugará toda lágrima de los ojos de ellos
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
dina naan moom itam biiñu xadarub yàlla bi kenn raxul, ñu sotti ko ci koppu meram. te dees na ko mbugal ci safara ak tamarax ci kanamu malaaka yu sell yi ak mbote mi,
él también beberá del vino del furor de dios que ha sido vertido puro en la copa de su ira, y será atormentado con fuego y azufre delante de los santos ángeles y delante del cordero
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
ma xool noonu, gis mbote ma taxaw ci tundu siyon, ànd ak téeméer ak ñeent-fukk ak ñeenti junniy nit, te ñu bind ci seen jë turu mbote ma ak turu baayam.
y miré, y he aquí el cordero de pie sobre el monte sion, y con él estaban los 144.000 que tenían su nombre y el nombre de su padre escrito en sus frentes
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu ma gis mbote ma dindi tayu gu jëkk ga, te ma daldi dégg kenn ca ñeenti mbindeef ya, di wax ak baat buy riir ni dënnu naan: «Ñëwal.»
y miré cuando el cordero abrió el primero de los siete sellos, y oí a uno de los cuatro seres vivientes que decía con voz de trueno: "¡ven!
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Avertissement : un formatage HTML invisible est présent
dinañu xare ak mbote mi, waaye mbote mi dina leen daan, ndaxte mooy kilifag kilifa yi, di buuru buur yi. te am toppam, di ñi mu woo te tànn leen, te ñu takku ci moom, dinañu daanandoo ak moom.»
ellos harán guerra contra el cordero, y el cordero los vencerá, porque él es señor de señores y rey de reyes, y los que están con él son llamados y elegidos y fieles.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :