Vous avez cherché: melkisedeg (Wolof - Espagnol)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Espagnol

Infos

Wolof

fekk na yàlla tudde ko saraxalekat bu mag ni ko melkisedeg nekke.

Espagnol

y fue proclamado por dios sumo sacerdote según el orden de melquisedec

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte mi ngi nekkoon ci geñog maamam ibraayma, bi ko melkisedeg gatandoo.

Espagnol

porque él todavía estaba en el cuerpo de su padre cuando melquisedec le salió al encuentro

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

li waral mbir mi gën a leer moo di ne, beneen saraxalekat bu mel ni melkisedeg dafa ñëw.

Espagnol

esto es aun más evidente si otro sacerdote se levanta a la semejanza de melquisedec

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu ci boppam moo fa jëkk a dugg, muy ndaw li nu jiitu, ñu def ko saraxalekat bu mag ba fàww, mel ni melkisedeg.

Espagnol

donde entró jesús por nosotros como precursor, hecho sumo sacerdote para siempre según el orden de melquisedec

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

léegi nag ci ni ñu ko man a waxe, lewi miy jot asaka ci bànni israyil, moom ci boppam jox na ko melkisedeg, jaare ko ci ibraayma.

Espagnol

y por decirlo así, en la persona de abraham también leví, el que recibe los diezmos, dio el diezmo

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

seetleen ni mu màgge, moom melkisedeg! ibraayma sax, maamu cosaan mi, fab na li mu jële woon lépp ca xare ba, jox melkisedeg asaka ja.

Espagnol

mirad, pues, cuán grande fue aquel a quien aun el patriarca abraham le dio los diezmos del botín

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

melkisedeg nag xamaluñu ko baay, xamaluñu ko yaay walla menn maam. amul fenn fu ñu wax ag juddoom walla ag deeyam. moo tax nu di ko mengale ak doomu yàlla ji, ndaxte saraxalekat la bu kenn dul wuutu.

Espagnol

sin padre ni madre ni genealogía, no tiene principio de días ni fin de vida; y en esto se asemeja al hijo de dios, en que permanece sacerdote para siempre

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye melkisedeg mi bokkul woon ci giiru lewi, jotoon na asaka ci alali ibraayma. te rax-ca-dolli barkeel na ko, moom mi yàlla sédde woon dige yi.

Espagnol

pero aquel, cuya genealogía no es contada entre ellos, recibió los diezmos de abraham y bendijo al que tenía las promesas

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu ibraayma fab fukkeelu cér bi, maanaam asaka, ci li mu jële woon ci xare ba lépp, jox ko. ci lu jëkk turu melkisedeg mi ngi tekki «buur bu jub bi.» gannaaw loolu mooy buuru salem, tur woowu mooy tekki «buuru jàmm.»

Espagnol

asimismo, le dio abraham los diezmos de todo. en primer lugar, su nombre significa "rey de justicia", y también era rey de salem, que significa "rey de paz"

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,770,569,453 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK