Vous avez cherché: jëkkër (Wolof - Estonien)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Estonien

Infos

Wolof

yeesu ne ko: «demal woowi sa jëkkër te ñëw.»

Estonien

jeesus ütleb talle: „mine kutsu oma mees ja tule siia!”

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bay sol ci boppu jeeg yu ndaw yi, ñu bëgg seeni jëkkër ak seeni doom,

Estonien

et nad võiksid mõistlikult juhatada noori naisi armastama oma mehi ja lapsi,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

naka yéen jigéen ñi, nangeen nangul seeni jëkkër, ni su doon boroom bi.

Estonien

naised, olge allaheitlikud oma meestele, otsekui issandale!

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ci wàllu ñi seen jëkkër faatu nag, ku ci sësul ci kenn, teral ko ngir yàlla.

Estonien

austa leski, kes on õiged lesknaised.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

jëkkër war na def warugaru jëkkër ci jabaram; jabar it def warugaru jabar ci jëkkëram.

Estonien

mees täitku oma kohust naise vastu ja n

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

te bu teqalikoo ak moom, bumu séyaat, mbaa boog na juboo ak jëkkëram. te bu jëkkër ji fase jabaram.

Estonien

on aga keegi lahutatud, siis ta jäägu abielutuks v

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte jigéeni démb yu sell, ya gëmoon yàlla, loolu moo doon seen taar; nanguloon nañu seen jëkkër,

Estonien

sest nõnda on ka ennevanasti pühad naised, kes lootsid jumala peale, endid ehtinud ja olnud allaheitlikud oma meestele,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

di ñu maandu, sell te fonk seen kër, ñu neex deret te déggal seeni jëkkër, ngir kenn bañ cee gàkkal kàddug yàlla.

Estonien

olema viisakad, kasinad, majatalituses hoolikad, head, allaheitlikud oma meestele, et jumala sõna mitte ei pilgataks.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

te su ñu bëggee laaj dara, nañu ko laaj seen jëkkër ca kër ga, ndaxte jigéen di wax ci ndajem mbooloom ñi gëm, gàcce la.

Estonien

aga kui nad tahavad midagi

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

Ñu ngi lekk alalu jigéen ñi seen jëkkër faatu, di ñaan yàlla ay ñaani ngistal yu gudd. seen mbugal dina gën a tar.»

Estonien

nemad söövad leskede hooned ja loevad silmakirjaks pikki palveid. need saavad seda raskema hukatuse!”

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ku diineem sell te amul benn gàkk fa kanam yàlla mooy kii: ki nemmiku jiirim yi ak jigéen ñi seen jëkkër faatu ci seeni tiis, tey waggar sobey àddina.

Estonien

puhas ja laitmatu jumalateenistus jumala ja isa ees on see: vaestelaste ja lesknaiste eest hoolitseda nende viletsuses ja hoida ennast maailmast reostamatuna.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ci maanaa, mi ngi mel ni jigéen juy séy; yoon a ngi koy boole ak jëkkëram, ñu ànd seen giiru dund, waaye su jëkkër ji faatoo, buum gi dagg na.

Estonien

nii on abielunaine käsuga seotud elusoleva mehe külge; aga kui mees sureb, on ta lahti mehe käsu alt.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yéen itam jigéen ñi, na ku nekk nangul sa jëkkër. noonu su amee góor gu gëmul kàddug yàlla, te gis jabaram di dund dund gu sell, boole ci weg ko, loolu dina ko gindi ci lu àndul ak wax.

Estonien

samuti teie, naised, olge allaheitlikud oma meestele, et ka need, kes ei ole sõnakuulelikud sõnale, naiste eluviiside läbi võidetaks ilma sõnata usule,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

jigéen ji amul sañ-sañ ci yaramam moom kenn; jëkkëram moo ko moom. niki noonu it jëkkër ji amul sañ-sañ ci yaramam; jabaram moo ko moom.

Estonien

naisel ei ole meelevalda oma ihu üle, vaid mehel; ja n

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi ko piyeer déggee, mu jóg, ànd ak ñoom. bi mu ñëwee, ñu yóbbu ko ca néeg bu kawe ba. fekk fa ay jigéen ñi seeni jëkkër faatu, ñu daldi wër piyeer, ñépp di jooy, di ko won kamisool ya ak mbubb, ya dorkas daan defar cig dundam.

Estonien

siis peetrus tõusis ja läks nendega. ja kui ta sinna jõudis, viisid nad ta ülemisse tuppa, ja kõik lesknaised astusid tema ümber, nutsid ja näitasid kuubi ja riideid, mis hirv nende juures olles oli teinud.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,101,277 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK