Vous avez cherché: xarekat (Wolof - Estonien)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Estonien

Infos

Wolof

xam ne xarekat bu bëgg a neex ka ko solal, du dugg ci yëfi àddina.

Estonien

mitte ükski, kes on sõjateenistuses, ei anna ennast peatoiduse hankimise kimpu, muidu ta ei saa olla selle meelt mööda, kes ta on sõtta kutsunud.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mbooloom xarekat ya ak seen kilifa ak alkaatiy yawut ya jàpp yeesu, daldi yeew,

Estonien

aga väesalk ja ülempealik ja juutide sulased võtsid jeesuse ja sidusid ta kinni

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi loolu amee xarekat ya bëgg a rey ñi ñu tëj, ngir ragal ñenn ñi féey, ba raw.

Estonien

ent sõjameestel oli nõu vangid ära tappa, et ükski neist ujudes ei pääseks põgenema.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi nu dikkee room nag, ñu may pool, mu dëkk fa ko lew, moom ak xarekat ba koy wottu.

Estonien

aga kui saabusime rooma, anti paulusele luba jääda omaette elama ühes sõduriga, kes teda valvas.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu xarekat ya jël pool ci guddi, indi ko ba ca dëkku antipataris, ni ñu leen ko sante.

Estonien

vastavalt saadud käsule võtsid siis sõjamehed pauluse ja viisid ta ära läbi öö antipatrisesse.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu ma gis rab wa, buuri àddina si ak seeni xarekat dajaloo ngir xareji ak ki war fas wa ak ay xarekatam.

Estonien

ja ma nägin metsalist ja ilmamaa kuningaid ja nende sõjaväge olevat kogunenud sõda pidama sellega, kes istus hobuse seljas, ja tema sõjaväega.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu xarekat ya dem, damm tànki ku jëkk ka, teg ca ka ca des, ca ña ñu daajaale woon ak yeesu.

Estonien

siis tulid sõjamehed ja murdsid esimese sääreluud ja teise omad, kes ühes temaga olid risti löödud.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

«bu ngeen gisee ay xarekat wër dëkku yerusalem, xamleen ne jamono, ji ñu koy yàq, agsi na.

Estonien

aga kui te näete jeruusalma olevat s

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu saraxalekat ya dajaloo ak njiit ya, ñu diisoo; ba noppi ñu fab xaalis bu bare, jox ko xarekat ya,

Estonien

ja need tulid kokku ühes vanematega, pidasid isekeskis n

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mu daldi yónni nag xarekat, jox ko ndigal, mu indil ko boppu yaxya. waa ji dem, dagg boppu yaxya ca kaso ba,

Estonien

ja kuningas läkitas kohe valvuri ja käskis tuua tema pea.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu nag génn, tegoo mbubbum xarekat mu xonq mi ak kaalag dég gi. pilaat it ne leen: «waa jaa ngii!»

Estonien

siis tuli jeesus välja ja kandis kibuvitsakrooni ja purpurkuube. ja pilaatus ütles neile: „ennäe inimest!”

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yawut yi jàpp nañu nit kii, bëgg koo rey, waaye bi ma yégee ne, jaambur la ci room, wallu naa ko ak ay xarekat, ba musal ko.

Estonien

selle mehe olid juudid kinni võtnud ja tahtsid teda tappa; siis tulin mina sõjaväega vahele ja võtsin ta ära nende käest ja sain teada, et ta on rooma kodanik.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi erodd nekkee ci tànki indilu ko, ca guddi googa yeewoon nañu piyeer ak ñaari càllala, muy nelaw diggante ñaari xarekat, te ay xarekat di wottu buntu kaso ba.

Estonien

aga kui heroodes tahtis teda tuua kohtu ette, magas peetrus sel ööl kahe sõjamehe vahel kahe ahelaga seotult, ja vahid ukse ees valvasid vangihoonet.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

xarekat ya, bi ñu daajee yeesu ca bant ba, ba noppi dañoo jël ay yéreem, séddale ko ñeenti cér, ku nekk benn. jël nañu it mbubbam bu ñu ràbb ca kaw ba ci suuf te amul benn ñaw.

Estonien

kui nüüd sõjamehed jeesuse olid risti löönud, võtsid nad tema riided ja tegid neli osa, igale sõjamehele ühe osa, ja kuue; kuub aga oli õmbluseta, ülemisest äärest alumiseni ühes tükis kootud.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi mu ko jàppee, mu tëj ko kaso, teg ko ci loxoy ñeenti mboolooy xarekat, ngir ñu wottu ko, fekk mbooloo mu ci nekk di ñeenti nit; amoon na yéeney yóbbu ko ci kanamu yawut ya gannaaw màggalu bésu jéggi ba.

Estonien

ta võttis tema kinni ja heitis ta vangitorni ning andis tema nelja neljamehelise sõjameeste salga kätte hoida, kavatsedes teda pärast paasapüha tuua rahva ette.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,800,030,534 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK