Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
te dinaa ñaan baay bi, mu jox leen beneen dimbalikat, buy nekk ak yéen ba abadan.
et moi, je prierai le père, et il vous donnera un autre consolateur, afin qu`il demeure éternellement avec vous,
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
yaram wu yàqu war na sol jëmm ja dul yàqooti, te yaram wiy dee sol dund gu sax abadan.
car il faut que ce corps corruptible revête l`incorruptibilité, et que ce corps mortel revête l`immortalité.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
ndaxte sunu coono bu woyof bi dul yàgg, dafa nuy jural ndam lu bare, ba suul coono bi, tey sax abadan.
car nos légères afflictions du moment présent produisent pour nous, au delà de toute mesure,
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu la ndekkitel néew yi di deme. bu ñu suulee néew bi, dañoo ji lu yàqu. bu dekkee, du yàqooti ba abadan.
ainsi en est-il de la résurrection des morts. le corps est semé corruptible; il ressuscite incorruptible;
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
yaw buur bi fiy sax ba abadan, yaw mi bët mënta gis, yaw yàlla miy kenn, yaa yelloo teraanga ak ndam ba fàww. amiin!
au roi des siècles, immortel, invisible, seul dieu, soient honneur et gloire, aux siècles des siècles! amen!
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
bu li yàqu solee melokaanu li dul yàqu, te liy dee sol melokaanu liy sax abadan, kon lii ñu wax ci mbind mi mat:«yàlla noot na dee, ba labal ko ci ndamam.
lorsque ce corps corruptible aura revêtu l`incorruptibilité, et que ce corps mortel aura revêtu l`immortalité, alors s`accomplira la parole qui est écrite: la mort a été engloutie dans la victoire.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
su fekkee ne noonu la deme nag, du kon deretu kirist moo ëpp doole? jox na bakkanam yàlla, def ko sarax su amul sikk jaarale ko ci dooley xel miy sax abadan. kon deretam moo man a sellal sunu xel, mi nu doon yedd ndax jëf yu jëm ci dee, ngir nu man a jaamu yàlla jiy dund.
combien plus le sang de christ, qui, par un esprit éternel, s`est offert lui-même sans tache à dieu, purifiera-t-il votre conscience des oeuvres mortes, afin que vous serviez le dieu vivant!
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :