Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
mi amoul
Dernière mise à jour : 2024-03-15
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
lolo bakh adouna amoul solo
lolo bakh adouna amoul solo
Dernière mise à jour : 2024-04-02
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
xaraf ak bañ a xaraf dara amu ci solo. li am solo mooy nekk mbindeef mu bees.
car ce n`est rien que d`être circoncis ou incirconcis; ce qui est quelque chose, c`est d`être une nouvelle créature.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
xaraf ak ñàkka xaraf lépp a yem; li am solo moo di topp ndigali yàlla.
la circoncision n`est rien, et l`incirconcision n`est rien, mais l`observation des commandements de dieu est tout.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
ki jëmbët nag ak ki suuxat, kenn du ci dara, waaye yàlla miy jebbil rekk moo am solo.
en sorte que ce n`est pas celui qui plante qui est quelque chose, ni celui qui arrose, mais dieu qui fait croître.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
ndaxte maa gën a ñàkk solo ci ndawi kirist yi, te yeyoowuma sax, ñu may wooye ndaw, man mi doon fitnaal mbooloom yàlla.
car je suis le moindre des apôtres, je ne suis pas digne d`être appelé apôtre, parce que j`ai persécuté l`Église de dieu.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
xanaa dangeen a xamul ne, gaayi yàlla yi ñooy àtteji àddina? te ndegam yéenay àtteji àddina, lu tere ngeen man a àtte mbir yu ñàkk solo yi?
ne savez-vous pas que les saints jugeront le monde? et si c`est par vous que le monde est jugé, êtes-vous indignes de rendre les moindres jugements?
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :