Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
danga rafet
Dernière mise à jour : 2021-05-16
Fréquence d'utilisation : 2
Qualité :
Référence:
ndax danga maa bëgg a rey, ni nga defoon démb waayi misra ja?”
Dernière mise à jour : 2020-06-28
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
ndaxte kenn musul a bañ sa yaram. waaye danga koy dundal, di ko fonk. noonu it la kirist fonke mbooloo mi;
car jamais personne n`a haï sa propre chair; mais il la nourrit et en prend soin, comme christ le fait pour l`Église,
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
Ña rab jàpp daldi xaacu naan: «yaw doomu yàlla ji, loo nuy fexeel? ndax danga noo bëgg a mbugal, bala waxtu way jot?»
et voici, ils s`écrièrent: qu`y a-t-il entre nous et toi, fils de dieu? es-tu venu ici pour nous tourmenter avant le temps?
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
yéen bokk yi, buleen ŋàññante. ku ŋàññ sa moroom mbaa nga ñaaw njort, ba àtte ko, diiŋat nga yoonu yàlla te àtte ko; ku àtte yoon wi nag sàmmoo ko, waaye danga koo àtte.
ne parlez point mal les uns des autres, frères. celui qui parle mal d`un frère, ou qui juge son frère, parle mal de la loi et juge la loi. or, si tu juges la loi, tu n`es pas observateur de la loi, mais tu en es juge.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence: