Vous avez cherché: fen (Wolof - Français)

Traduction

Français

Traduction
Traduction

Traduisez instantanément des textes, des documents et des voix avec Lara

Traduire maintenant

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Français

Infos

Wolof

looloo tax yàlla yónnee leen xelum réer, ba ñu gëm fen.

Français

aussi dieu leur envoie une puissance d`égarement, pour qu`ils croient au mensonge,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

lii ma leen di bind nag, yàllaa may seede ci ne, du ay fen.

Français

dans ce que je vous écris, voici, devant dieu, je ne mens point.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ku wax ne xam nga ko, te sàmmoo ay ndigalam, dangay fen, te dëgg nekkul ci yaw.

Français

celui qui dit: je l`ai connu, et qui ne garde pas ses commandements, est un menteur, et la vérité n`est point en lui.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bind naa leen, du ndax xamuleen dëgg, waaye ndax xam ngeen ko, xam it ne wenn fen du jóge ci dëgg.

Français

je vous ai écrit, non que vous ne connaissiez pas la vérité, mais parce que vous la connaissez, et parce qu`aucun mensonge ne vient de la vérité.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

kon nag bàyyileen di fen, tey wax dëgg kenn ku nekk ci moroomam, ndax ku nekk sa genn-wàllu moroom nga.

Français

c`est pourquoi, renoncez au mensonge, et que chacun de vous parle selon la vérité à son prochain; car nous sommes membres les uns des autres.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bàyyileen di fen seeni moroom, ndaxte summi ngeen jikko ju bon, ji ngeen judduwaale, moom ak ay jëfam;

Français

ne mentez pas les uns aux autres, vous étant dépouillés du vieil homme et de ses oeuvres,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ngir ñiy doxaan, ñi góor-jigéenu ak ñiy def nit jaam, ñiy fen tey wann seen kàddu, ak lépp luy juuyoo ak njàngale mu wér

Français

les impudiques, les infâmes, les voleurs d`hommes, les menteurs, les parjures, et tout ce qui est contraire à la saine doctrine, -

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

li ma bëgg a wax nag, ci kanamu kirist laa koy waxe; dëgg la, du aw fen. sama xel, mi xel mu sell miy leeral, seedeel na ma ne, dëgg laay wax.

Français

je dis la vérité en christ, je ne mens point, ma conscience m`en rend témoignage par le saint esprit:

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
8,651,010,782 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK