Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
nan nga def ?
comment vas-tu ?
Dernière mise à jour : 2024-04-10
Fréquence d'utilisation : 3
Qualité :
yeesu ne ko: «lu ñu bind ci yoonu musaa? lan nga ciy jàng?»
jésus lui dit: qu`est-il écrit dans la loi? qu`y lis-tu?
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
pilaat ne ko: «mbaa xalaatoo ne, man yawut laa? sa xeet ak saraxalekat yu mag yi ñoo ma la jébbal. lan nga def?»
pilate répondit: moi, suis-je juif? ta nation et les principaux sacrificateurs t`ont livré à moi: qu`as-tu fait?
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
kon nag maa ngi lay dénk fa kanam yàlla ak kirist yeesu, miy àtte ñiy dund ak ñi dee, di la dénk ci feeñam ci biir ndam ak ci nguuram, nga def lii:
je t`en conjure devant dieu et devant jésus christ, qui doit juger les vivants et les morts, et au nom de son apparition et de son royaume,
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
naka la ko waajuram yi gis, ñu daldi waaru. yaayam ne ko: «sama doom, lu tax nga def nu lii? man ak sa baay nu ngi la doon seet, jaaxle lool.»
quand ses parents le virent, ils furent saisis d`étonnement, et sa mère lui dit: mon enfant, pourquoi as-tu agi de la sorte avec nous? voici, ton père et moi, nous te cherchions avec angoisse.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :