Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
raw na ko fu nekk. ci bu jëkk yawut yi la yàlla dénk waxam.
il est grand de toute manière, et tout d`abord en ce que les oracles de dieu leur ont été confiés.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
ku juddu ci yàlla doo def bàkkaar, ndax yàlla sol na la jikkoom, te doo man a sax ci bàkkaar, ndax juddu nga ci yàlla.
quiconque est né de dieu ne pratique pas le péché, parce que la semence de dieu demeure en lui; et il ne peut pécher, parce qu`il est né de dieu.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
malaaka ma ne ko: «bul ragal dara maryaama, ndaxte yàlla tànn na la ci yiwam.
l`ange lui dit: ne crains point, marie; car tu as trouvé grâce devant dieu.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
ndaxte gis naa ne, sóobu nga ci lu wex xat ci kanam yàlla, te bàkkaar noot na la.»
car je vois que tu es dans un fiel amer et dans les liens de l`iniquité.
Dernière mise à jour : 2024-03-15
Fréquence d'utilisation : 2
Qualité :
yeesu xamoon na ne, yàlla joxoon na ko sañ-sañ ci lépp, xam it ne, ca yàlla la jóge te ca moom lay delluwaat.
jésus, qui savait que le père avait remis toutes choses entre ses mains, qu`il était venu de dieu, et qu`il s`en allait à dieu,
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
ca njàlbéen ga fekk na kàddu gi am, te kàddu gi ma nga woon ak yàlla, te kàddu gi yàlla la woon.
au commencement était la parole, et la parole était avec dieu, et la parole était dieu.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
am na ay sas yu bare, waaye benn boroom bi la.
diversité de ministères, mais le même seigneur;
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
lan la mbind mi wax ci loolu? nee na: «ibraayma gëm na yàlla, te yàlla jàppe ngëmam ni njub.»
car que dit l`Écriture? abraham crut à dieu, et cela lui fut imputé à justice.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
képp ku déggalul yonent boobu, dees na la far ci xeet wi.”
et quiconque n`écoutera pas ce prophète sera exterminé du milieu du peuple.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
am na lu bare, lu ma la bëggoona wax, waaye lépp xajul ci kayit.
j`aurais beaucoup de choses à t`écrire, mais je ne veux pas le faire avec l`encre et la plume.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
waaye amoon na fa waa ju ñuy wax sase. njiitu juutikat la, te di ku bare alal.
et voici, un homme riche, appelé zachée, chef des publicains, cherchait à voir qui était jésus;
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
ndaxte dees na la àtte ni ku jub ci say wax, walla ñu daan la ci say wax.»
car par tes paroles tu seras justifié, et par tes paroles tu seras condamné.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
def na noonu, ngir amal la ñu waxoon jaarale ko ci yonent yàlla esayi, bi mu naan:
afin que s`accomplît ce qui avait été annoncé par Ésaïe, le prophète:
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
te yaw dëkku kapernawum, ndax dees na la yékkati bu kawe? déedéet, dees na la daane bu suufe.
et toi, capernaüm, qui as été élevée jusqu`au ciel, tu seras abaissée jusqu`au séjour des morts.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
ku am, dees na la dollil; ku amul, li nga am as néew, dees na ko nangu.»
car on donnera à celui qui a; mais à celui qui n`a pas on ôtera même ce qu`il a.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
yeesu ne ko: «mucc gi wàcc na tey ci kër gii, ndaxte nit kii, ci askanu ibraayma la bokk itam.
jésus lui dit: le salut est entré aujourd`hui dans cette maison, parce que celui-ci est aussi un fils d`abraham.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
te ndegam moom ci boppam nit kese la, man na muñal ñiy moy ndax seen ñàkka xam.
il peut être indulgent pour les ignorants et les égarés, puisque la faiblesse est aussi son partage.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
waaye su ma ko defoon, nan la mbind mi man a ame? ndaxte mbind mi nee na, nii la war a ame.»
comment donc s`accompliraient les Écritures, d`après lesquelles il doit en être ainsi?
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
ku nekkoon jaam, bi la boroom bi wooyee, boroom bi goreel na la. ba tey it ku nekkoon gor, bi ñu la wooyee, jaamu kirist nga.
car l`esclave qui a été appelé dans le seigneur est un affranchi du seigneur; de même, l`homme libre qui a été appelé est un esclave de christ.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
yeesu ne ko: «soxna si, sa ngëm faj na la; demal ci jàmm, te na sa jàngoro wàcc.»
mais jésus lui dit: ma fille, ta foi t`a sauvée; va en paix, et sois guérie de ton mal.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Certaines traductions humaines peu pertinentes ont été masquées.
Affichez les résultats peu pertinents.