Vous avez cherché: daf (Wolof - Français)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Français

Infos

Wolof

wax na loolu nag, ndax jën yu bare ya ñu mbaaloon daf koo jaaxal, moom ak ña mu àndaloon

Français

car l`épouvante l`avait saisi, lui et tous ceux qui étaient avec lui, à cause de la pêche qu`ils avaient faite.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

nit kuy giñ nag, daf koy wékk ci ku ko sut. ngiñ lu mel noonu moo wóoral mbir te mooy jeexal lépp lu ñuy werante.

Français

or les hommes jurent par celui qui est plus grand qu`eux, et le serment est une garantie qui met fin à toutes leurs différends.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bu sama kàddu diisee nag ci bataaxal bii, dara taxul lu dul bëgg a yeesal seen xalaat, ndaxte yàlla ci kaw yiwam daf maa sas,

Français

cependant, à certains égards, je vous ai écrit avec une sorte de hardiesse, comme pour réveiller vos souvenirs, à cause de la grâce que dieu m`a faite

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

te daawuda it daf ci wax naan:«na seeni ñam sax nekk fiir ak i pakk;nañu ci daanu, te yàlla mbugal leen.

Français

que leur table soit pour eux un piège, un filet, une occasion de chute, et une rétribution!

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ku bëgg a jub ci kanam yàlla ci kaw sàmm yoon, musaa daf cee wax ne: «ku ko manoon a matal, dinga dund ba fàww.»

Français

en effet, moïse définit ainsi la justice qui vient de la loi: l`homme qui mettra ces choses en pratique vivra par elles.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,782,755,135 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK