Vous avez cherché: door kat (Wolof - Français)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Français

Infos

Wolof

kat sa ndeye

Français

nicke ta merejavascript: void(0)

Dernière mise à jour : 2024-01-14
Fréquence d'utilisation : 4
Qualité :

Wolof

ndaxte aadama la yàlla jëkk a sàkk, door caa teg awa.

Français

car adam a été formé le premier, eve ensuite;

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

Ñu yégle kàddu gi ci dëkku peers, door a dem dëkku atali.

Français

annoncèrent la parole à perge, et descendirent à attalie.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

moom itam nañu ko jëkk a seetlu, ba mu leer ne amul ŋàññ, ñu door koo fal.

Français

qu`on les éprouve d`abord, et qu`ils exercent ensuite leur ministère, s`ils sont sans reproche.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mu juboo ak liggéeykat ya ci bëccëg posetu denariyon, door leen a yebal ca toolam.

Français

il convint avec eux d`un denier par jour, et il les envoya à sa vigne.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

te it bumu nekk kuy door a gëm, ngir mu bañ a yég boppam, bay dajeek mbugalu yàlla, ni ko seytaane defe woon.

Français

il ne faut pas qu`il soit un nouveau converti, de peur qu`enflé d`orgueil il ne tombe sous le jugement du diable.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu nekk fa te lekkul ñeent-fukki bëccëg ak ñeent-fukki guddi, door a xiif.

Français

après avoir jeûné quarante jours et quarante nuits, il eut faim.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

gannaaw ay liir ngeen yuy door a juddu te mos ci mbaaxug boroom bi, nàmpleen ci meew mu sell, miy dundal seen xol, ba màgg ci biir muccu yàlla.

Français

désirez, comme des enfants nouveau-nés, le lait spirituel et pur, afin que par lui vous croissiez pour le salut,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bëccek bu selew bile moom doyna waar bu timis di door rap yaa nginii ñoom ñepp teew dima xool dinawoo sama kaw nekk samayoon amuloo tur mungi dina xool mungi walagaan ci yoon aki yoonoo yaw yangi nii di woo sa yaay di xool diko gisoo sisa biir xol mingi ci sa yoon amuloo tur fileek yaa moom sa bopp noo gisé sa dunyaa wanté dinga jeem leep loo man ci lingay def ngir baña fatté sa yaay

Français

Dernière mise à jour : 2024-01-08
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,788,840,678 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK