Vous avez cherché: koy (Wolof - Français)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Français

Infos

Wolof

lu ngeen ñaan ci sama tur, maa koy def.

Français

si vous demandez quelque chose en mon nom, je le ferai.

Dernière mise à jour : 2024-04-13
Fréquence d'utilisation : 6
Qualité :

Wolof

«lii dama leen koy wax ci bi may nekk ak yéen.

Français

je vous ai dit ces choses pendant que je demeure avec vous.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

amul kenn ku xam yëfi yàlla,mbaa kenn ku koy wut.

Français

nul n`est intelligent, nul ne cherche dieu; tous sont égarés, tous sont pervertis;

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu malaakam yàlla daldi koy feeñu, may ko doole.

Français

alors un ange lui apparut du ciel, pour le fortifier.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

wutumaa màggal sama bopp. keneen a ma koy wutal te mooy àtte.

Français

je ne cherche point ma gloire; il en est un qui la cherche et qui juge.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

maa koy yebal fi yaw, waaye xamal ne, mooy sama reeni xol.

Français

je te le renvoie lui, mes propres entrailles.

Dernière mise à jour : 2024-04-13
Fréquence d'utilisation : 4
Qualité :

Wolof

ci dëgg maa ngi la koy wax, doo génn foofa mukk te feyuloo dërëm bi ci mujj.

Français

je te le dis en vérité, tu ne sortiras pas de là que tu n`aies payé le dernier quadrant.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

maa ngi la koy wax, doo génn foofa mukk te feyuloo fiftin bi ci mujj.»

Français

je te le dis, tu ne sortiras pas de là que tu n`aies payé jusqu`à dernière pite.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

am na fànni may yu bare yu jóge ci xelum yàlla, waaye menn xel moomu moo koy séddale.

Français

il y a diversité de dons, mais le même esprit;

Dernière mise à jour : 2024-02-04
Fréquence d'utilisation : 3
Qualité :

Wolof

doomu nit ki mu ngi dem, ni ñu ko dogale. waaye ki koy wor dina torox.»

Français

le fils de l`homme s`en va selon ce qui est déterminé. mais malheur à l`homme par qui il est livré!

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte loolu lépp, ñi xamul yàlla ñoo koy wut. te seen baay xam na ne, soxla ngeen ko.

Français

car toutes ces choses, ce sont les païens du monde qui les recherchent. votre père sait que vous en avez besoin.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye mu tontu leen ne: “ci dëgg maa ngi leen koy wax, xawma leen.”

Français

mais il répondit: je vous le dis en vérité, je ne vous connais pas.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

«bu ngeen gisee ay xarekat wër dëkku yerusalem, xamleen ne jamono, ji ñu koy yàq, agsi na.

Français

lorsque vous verrez jérusalem investie par des armées, sachez alors que sa désolation est proche.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu mu tontu ne: «maa ngi leen koy wax, bu ñu noppee ñoom, doj yiy xaacu.»

Français

et il répondit: je vous le dis, s`ils se taisent, les pierres crieront!

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu tontu leen: «daaneel-leen kër yàlla gii, ma daldi koy yékkati ci ñetti fan.»

Français

jésus leur répondit: détruisez ce temple, et en trois jours je le relèverai.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,780,352,787 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK