Vous avez cherché: laabal (Wolof - Français)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Français

Infos

Wolof

kon nag ku laabal sa bopp ci yooyu yépp, dinga nekk ndab lu tedd te sell, nga am njariñ ci boroom bi te jekk ci bépp jëf ju rafet.

Français

si donc quelqu`un se conserve pur, en s`abstenant de ces choses, il sera un vase d`honneur, sanctifié, utile à son maître, propre à toute bonne oeuvre.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ba musal nu; ajuwul ci jëf yu jub yu nu def, waaye ci yërmandeem rekk. mu juddulaat nu ci laabal sunu xol, te yeesalaat nu ci dooley xel mu sell,

Français

il nous a sauvés, non à cause des oeuvres de justice que nous aurions faites, mais selon sa miséricorde, par le baptême de la régénération et le renouvellement du saint esprit,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

jegeleen yàlla, mu jege leen. yéen bàkkaarkat yi, sellal-leen seeni loxo; yéen ñi am xel ñaar, laabal-leen seeni xol.

Français

approchez-vous de dieu, et il s`approchera de vous. nettoyez vos mains, pécheurs; purifiez vos coeurs, hommes irrésolus.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

loolu misaal la tey, ci li ñu nuy sóob ci ndox, te nu mucc; waxuma laabal sobe si taq ci yaram, waaye wuyu yàlla ak xel mu dal. li nu may mucc googu, mooy ndekkitel yeesu kirist,

Français

cette eau était une figure du baptême, qui n`est pas la purification des souillures du corps, mais l`engagement d`une bonne conscience envers dieu, et qui maintenant vous sauve, vous aussi, par la résurrection de jésus christ,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,781,194,641 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK