Vous avez cherché: mënul (Wolof - Italien)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Italien

Infos

Wolof

léegi nag yoon mënul a dab ñi bokk ci yeesu kirist.

Italien

non c'è dunque più nessuna condanna per quelli che sono in cristo gesù

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yaxya tontu leen: «kenn mënul a am dara lu ko yàlla joxul.

Italien

giovanni rispose: «nessuno può prendersi qualcosa se non gli è stato dato dal cielo

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

baay bi ma leen jox, moo gën a màgg lépp, te kenn mënul a jële dara ci loxob baay bi.

Italien

il padre mio che me le ha date è più grande di tutti e nessuno può rapirle dalla mano del padre mio

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

garab gu baax mënul a meññ doom yu bon, naka itam garab gu bon mënul a meññ doom yu neex.

Italien

un albero buono non può produrre frutti cattivi, né un albero cattivo produrre frutti buoni

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

su ko mënul, dafay yónni ndaw ca beneen buur ba, fi ak ma ngay sore, ngir ñu juboo.

Italien

se no, mentre l'altro è ancora lontano, gli manda un'ambasceria per la pace

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

loolu sax mënul a am, ndaxte céri yaram, yi gën a néew doole, ñoo gën a am jariñ.

Italien

anzi quelle membra del corpo che sembrano più deboli sono più necessarie

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

dee na benn yoon, ba bàkkaar mënul ci moom dara; te mi ngi dund léegi, di ànd ak yàlla ba fàww.

Italien

per quanto riguarda la sua morte, egli morì al peccato una volta per tutte; ora invece per il fatto che egli vive, vive per dio

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ngëm moo tax mu jóge misra te ragalul merum buur bi. dafa muñ, mel ni nit kuy gis yàlla, mi kenn mënul a teg bët.

Italien

per fede lasciò l'egitto, senza temere l'ira del re; rimase infatti saldo, come se vedesse l'invisibile

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ibraayma bokk na ci ñoom. bi ko yàllay dig, mënul woon a giñ ci keneen ku ko gën a màgg, ba tax mu giñ ci boppam,

Italien

quando infatti dio fece la promessa ad abramo, non potendo giurare per uno superiore a sé, giurò per se stesso

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yàlla wooye na “ay yàlla” ñi mu yónnee kàddoom, te xam nanu ne, kenn mënul a randal waxi yàlla.

Italien

ora, se essa ha chiamato dei coloro ai quali fu rivolta la parola di dio (e la scrittura non può essere annullata)

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

moytuleen a tanqamlu nag kiy wax ak yéen. ndegam ñiy tanqamlu ki leen di artu ci àddina, ñoo mënul a rëcc ci àtte bi, aste ku dummóoyu kiy wax ci asamaan.

Italien

guardatevi perciò di non rifiutare colui che parla; perché se quelli non trovarono scampo per aver rifiutato colui che promulgava decreti sulla terra, molto meno lo troveremo noi, se volteremo le spalle a colui che parla dai cieli

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

gannaaw loolu yeesu jóge fa, jëm weti dëkku tir. bi mu fa eggee, mu dugg ci kër, te bëggul kenn xam ko, waaye jataayam mënul a umpe.

Italien

partito di là, andò nella regione di tiro e di sidone. ed entrato in una casa, voleva che nessuno lo sapesse, ma non potè restare nascosto

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

amoon na fa jigéen ju rab jàppoon, ba feebarloo ko lu war a mat fukki at ak juróom-ñett; dafa xuuge woon te mënul woon a siggi dara.

Italien

c'era là una donna che aveva da diciotto anni uno spirito che la teneva inferma; era curva e non poteva drizzarsi in nessun modo

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

te jigéen ja xam ne, mënul woon a nëbb li mu def. mu daldi daanu ci tànki yeesu, di lox. noonu mu nettali ci kanamu ñépp li taxoon mu laal yeesu, ak ni mu wére ca saa sa.

Italien

allora la donna, vedendo che non poteva rimanere nascosta, si fece avanti tremando e, gettatasi ai suoi piedi, dichiarò davanti a tutto il popolo il motivo per cui l'aveva toccato, e come era stata subito guarita

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yoonu musaa dafa misaal xéewal yi waroon a ñëw; takkandeer la ci yëf yu dëggu yi, waaye du ñoom ci seen bopp. looloo tax mënul a yeggale cig mat ñi ñëw ci yàlla, ndaxte at mu nekk duñu jóg ci jébbal yàlla sarax yooyu.

Italien

avendo infatti la legge solo un'ombra dei beni futuri e non la realtà stessa delle cose, non ha il potere di condurre alla perfezione, per mezzo di quei sacrifici che si offrono continuamente di anno in anno, coloro che si accostano a dio

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,778,620,055 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK