Vous avez cherché: mbiri (Wolof - Italien)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Italien

Infos

Wolof

ci mbiri binduwaayu gnome

Italien

informazioni su gnome desktop

Dernière mise à jour : 2014-08-15
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ci mbiri seen bàkkaar, dina leen yey ci li ñu ma gëmul.

Italien

quanto al peccato, perché non credono in me

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

la ñu wax ci mbiri yeesu daldi siiw ca réewu yawut ya ak la ko wër yépp.

Italien

la fama di questi fatti si diffuse in tutta la giudea e per tutta la regione

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ci mbiri sama njubte, dina leen yey ndaxte maa ngi dem ci baay bi te dungeen ma gisati.

Italien

quanto alla giustizia, perché vado dal padre e non mi vedrete più

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ci mbiri àtte ba, dina leen yey ndaxte àtte nañu malaaka mu bon mi jiite àddina si, ba daan ko.

Italien

quanto al giudizio, perché il principe di questo mondo è stato giudicato

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye ku takk jabar, fàww mu bàyyi xel ci mbiri àddina si, ak nu mu man a neexe jabaram,

Italien

chi è sposato invece si preoccupa delle cose del mondo, come possa piacere alla moglie

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

gannaaw gëmuleen li ma leen di wax ci mbiri àddina, naka ngeen man a gëme, bu ma leen waxee ci mbiri asamaan?

Italien

se vi ho parlato di cose della terra e non credete, come crederete se vi parlerò di cose del cielo

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

aana yem ca waxi simeyon ya, daldi gërëm yàlla tey yégal mbiri liir ba ñépp ñi doon séentu jamono, ji yàlla war a jot yerusalem.

Italien

sopraggiunta in quel momento, si mise anche lei a lodare dio e parlava del bambino a quanti aspettavano la redenzione di gerusalemme

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bëggoon naa, ngeen bañ a am benn xalaat. góor gu takkul jabar dafay bàyyi xel ci mbiri boroom bi, di wut a neex boroom bi.

Italien

io vorrei vedervi senza preoccupazioni: chi non è sposato si preoccupa delle cose del signore, come possa piacere al signore

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye bu ñépp dee wax ci kàddug yàlla, te ku gëmul dugg fa, walla ku jàngul mbiri kirist, wax yi ñépp wax dafay wone bàkkaaram te àtte ko,

Italien

se invece tutti profetassero e sopraggiungesse qualche non credente o un non iniziato, verrebbe convinto del suo errore da tutti, giudicato da tutti

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bokk yi, wóor na ma ne, baax ngeen ba fa mbaax man a yem, fees dell ak xam-xam, ba man a jàngaleente mbiri yàlla ci seen biir.

Italien

fratelli miei, sono anch'io convinto, per quel che vi riguarda, che voi pure siete pieni di bontà, colmi di ogni conoscenza e capaci di correggervi l'un l'altro

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

moo tax ma xalaat ne, li gën mooy yónni bokk yooyu, ñu jiitu ma ci yéen, topptoo mbiri ndimbal lu yaatu loolu ngeen dige woon. loolu di may gu tàlli, te bañ a nekk yëfi nay.

Italien

ho quindi ritenuto necessario invitare i fratelli a recarsi da voi prima di me, per organizzare la vostra offerta gia promessa, perché essa sia pronta come una vera offerta e non come una spilorceria

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

gayus mu ngi leen di nuyu; moo may ganale ci këram, te foofa it la mbooloo mi di dajaloo. erast miy topptoo mbiri xaalisu dëkk bi it, nuyu na leen, ak sunu mbokk kartus.

Italien

vi saluta gaio, che ospita me e tutta la comunità. vi salutano erasto, tesoriere della città, e il fratello quarto

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

te noonu dafay daldi bare soxla. te jigéen ju séyul, walla janq, dafay bàyyi xel ci mbiri boroom bi — bëgg koo jox yaramam ak xelam. waaye jigéen ji séy dafay bàyyi xel ci mbiri àddina, ak nu mu man a neexe jëkkëram.

Italien

e si trova diviso! così la donna non sposata, come la vergine, si preoccupa delle cose del signore, per essere santa nel corpo e nello spirito; la donna sposata invece si preoccupa delle cose del mondo, come possa piacere al marito

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,792,768,945 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK