Vous avez cherché: yengu (Wolof - Italien)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Italien

Infos

Wolof

dex gi yengu na lool, ndaxte da doon ngelaw ak doole.

Italien

il mare era agitato, perché soffiava un forte vento

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

biddiiw yi di daanoo asamaan,te kàttani asamaan yiy yengu.”

Italien

e gli astri si metteranno a cadere dal cielo e le potenze che sono nei cieli saranno sconvolte

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

fekk booba amoon na yengu-yengu bu réy ci lu aju ci yoon wi.

Italien

verso quel tempo scoppiò un gran tumulto riguardo alla nuova dottrina

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

maa ngi lay wax ne, naka laa la dégg ngay nuyoo rekk, sama doom ji yengu ci sama biir ndax mbég.

Italien

ecco, appena la voce del tuo saluto è giunta ai miei orecchi, il bambino ha esultato di gioia nel mio grembo

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ci loolu laay jëmale sama liggéey, di bëree dooley kirist, jiy yengu ci man ak kàttan.

Italien

per questo mi affatico e lotto, con la forza che viene da lui e che agisce in me con potenza

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

fekk suuf yengu woon na bu metti, ndaxte benn malaakam boroom bi wàcc na ci asamaan, ñëw béraŋ doj wa, toog ci kaw.

Italien

ed ecco che vi fu un gran terremoto: un angelo del signore, sceso dal cielo, si accostò, rotolò la pietra e si pose a sedere su di essa

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

kon nag ñu ne: «bumu doon ci bésu màggal bi, ngir yengu-yengu bañ a am ci nit ñi.»

Italien

dicevano infatti: «non durante la festa, perché non succeda un tumulto di popolo»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ca saa sa suuf yengu bu metti, ba fondamaab kaso ba daanu; bunt yépp daldi ne kulbet ubbiku, te jéngi ña ñu tëj ne tell tijjiku.

Italien

d'improvviso venne un terremoto così forte che furono scosse le fondamenta della prigione; subito tutte le porte si aprirono e si sciolsero le catene di tutti

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

suuf dina yengu yengu yu réy, te wopp ak xiif dina am ci bérab yu bare. dina am it ay xew-xew yu raglu ak ay firnde yu mag yuy jóge asamaan.

Italien

e vi saranno di luogo in luogo terremoti, carestie e pestilenze; vi saranno anche fatti terrificanti e segni grandi dal cielo

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye gis naa jeneen doole juy yengu ci samay céri yaram, di bëre ak li sama xol bëgg; day bëre ba noot ma, def ma jaam ci dooley bàkkaar joojuy yengu ci samay cér.

Italien

ma nelle mie membra vedo un'altra legge, che muove guerra alla legge della mia mente e mi rende schiavo della legge del peccato che è nelle mie membra

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi yengu-yengu ba dalee, pool woo taalibe ya fa moom, dooleel leen. bi mu ko defee mu tàggoo ak ñoom, jóge fa, dellu diiwaanu maseduwan.

Italien

appena cessato il tumulto, paolo mandò a chiamare i discepoli e, dopo averli incoraggiati, li salutò e si mise in viaggio per la macedonia

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

«ay firnde dinañu feeñ ci jant bi, ci weer wi ak ci biddiiw yi. ci kaw suuf xeet yi dinañu tiit, jaaxle ndax riiru géej gi ak yengu-yengub duus yi.

Italien

vi saranno segni nel sole, nella luna e nelle stelle, e sulla terra angoscia di popoli in ansia per il fragore del mare e dei flutti

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

«gannaaw metitu bés yooyule nag, ca saa sa jant bi dina lëndëm te weer wi dootul leer; biddiiw yi dinañu fàq, daanu ci asamaan, te kàttani asamaan yi yengu.

Italien

subito dopo la tribolazione di quei giorni, dal cielo e le potenze dei cieli saranno sconvolte

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ragal naa, bu ma ñëwee ci yéen, fekk leen nu ma neexul, te yéen it ngeen fekk ma nu leen neexul. ragal naa fekk ay xuloo ci seen biir, ak ñeetaane, xadar ak diiroo mbagg, xas ak jëw, réy-réylu ak yengu-yengu.

Italien

temo infatti che, venendo, non vi trovi come desidero e che a mia volta venga trovato da voi quale non mi desiderate; che per caso non vi siano contese, invidie, animosità, dissensi, maldicenze, insinuazioni, superbie, disordini

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,791,964,157 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK