Vous avez cherché: seetleen (Wolof - Japonais)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Japonais

Infos

Wolof

waaye seetleen mbir yépp, jàpp ci li baax,

Japonais

すべてのものを識別して、良いものを守り、

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

seetleen araf yu mag yii ma leen bind ci sama loxob bopp!

Japonais

ごらんなさい。わたし自身いま筆をとって、こんなに大きい字で、あなたがたに書いていることを。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

maa ngi wax ak yéen ñi am xel. kon seetleen li ma leen wax.

Japonais

賢明なあなたがたに訴える。わたしの言うことを、自ら判断してみるがよい。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

seetleen mbir mii: ndax jekk na jigéen bañ a musóoru, buy ñaan yàlla?

Japonais

あなたがた自身で判断してみるがよい。女がおおいをかけずに神に祈るのは、ふさわしいことだろうか。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

«Ñaanleen, ñu may leen; seetleen te dingeen gis; fëggleen, ñu ubbil leen.

Japonais

求めよ、そうすれば、与えられるであろう。捜せ、そうすれば、見いだすであろう。門をたたけ、そうすれば、あけてもらえるであろう。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

moo tax ma ne, ñaanleen, ñu may leen; seetleen, te dingeen gis; fëggleen, ñu ubbil leen.

Japonais

そこでわたしはあなたがたに言う。求めよ、そうすれば、与えられるであろう。捜せ、そうすれば見いだすであろう。門をたたけ、そうすれば、あけてもらえるであろう。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

seetleen ci bànni israyil. Ñiy lekk sarax si ñu rendi, ndax booloowuñu ak yàlla ji ñu jagleel saraxalukaay ba? aaŋkay!

Japonais

肉によるイスラエルを見るがよい。供え物を食べる人たちは、祭壇にあずかるのではないか。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ci noonu làmmiñ, cér su tuuti la, waaye day bàkkoo jëf yu réy. seetleen ni ferñent tuutee, te man a làkk àll bu yaatu.

Japonais

それと同じく、舌は小さな器官ではあるが、よく大言壮語する。見よ、ごく小さな火でも、非常に大きな森を燃やすではないか。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mu ne leen: «seetleen bu baax li ngeen di dégg. dees na leen nattal ak natt, bi ngeen di nattale, te dollil leen.

Japonais

また彼らに言われた、「聞くことがらに注意しなさい。あなたがたの量るそのはかりで、自分にも量り与えられ、その上になお増し加えられるであろう。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

seetleen ni mu màgge, moom melkisedeg! ibraayma sax, maamu cosaan mi, fab na li mu jële woon lépp ca xare ba, jox melkisedeg asaka ja.

Japonais

そこで、族長のアブラハムが最もよいぶんどり品の十分の一を与えたのだから、この人がどんなにすぐれた人物であったかが、あなたがたにわかるであろう。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bokk yi, seetleen seen nekkin, bi leen yàlla di woo. barewul woon ci yéen, ñi ñuy tudde ay boroom xam-xam mbaa ay boroom doole mbaa ñu rafet ab juddu.

Japonais

兄弟たちよ。あなたがたが召された時のことを考えてみるがよい。人間的には、知恵のある者が多くはなく、権力のある者も多くはなく、身分の高い者も多くはいない。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

seetleen picci asamaan: duñu ji, duñu góob, duñu denc ci sàq; teewul seen baay bi ci kaw moo leen di dundal. ndax ëppuleen maana picc yi ci lu bare?

Japonais

空の鳥を見るがよい。まくことも、刈ることもせず、倉に取りいれることもしない。それだのに、あなたがたの天の父は彼らを養っていて下さる。あなたがたは彼らよりも、はるかにすぐれた者ではないか。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

«seetleen ni tóor-tóori ñax mi di saxe. duñu liggéey, duñu ëcc, waaye maa ngi leen di wax ne, suleymaan sax ci ndamam, soluwul woon ni benn ci ñoom.

Japonais

野の花のことを考えて見るがよい。紡ぎもせず、織りもしない。しかし、あなたがたに言うが、栄華をきわめた時のソロモンでさえ、この花の一つほどにも着飾ってはいなかった。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

«bu ñu leen waxee nag: “seetleen, mu nga nale ca àll ba,” buleen génn, mbaa ñu ne: “seetleen mu ngi nii ci biir kër gi,” buleen ko gëm.

Japonais

だから、人々が『見よ、彼は荒野にいる』と言っても、出て行くな。また『見よ、へやの中にいる』と言っても、信じるな。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,774,319,705 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK