Vous avez cherché: yerusalem (Wolof - Japonais)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Japonais

Infos

Wolof

gannaaw fan yooyu nu defaru, ngir dem yerusalem.

Japonais

数日後、わたしたちは旅装を整えてエルサレムへ上って行った。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ca fan yooyu ay yonent jóge yerusalem, ñëw ancos.

Japonais

そのころ、預言者たちがエルサレムからアンテオケにくだってきた。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi nu agsee yerusalem nag, taalibe ya teeru nu ak mbég.

Japonais

わたしたちがエルサレムに到着すると、兄弟たちは喜んで迎えてくれた。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye yerusalem, ga ca kaw, mooy gor si. moom mooy sunu ndey.

Japonais

しかし、上なるエルサレムは、自由の女であって、わたしたちの母をさす。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye waa dëkk ba nanguwuñu ko, ndaxte mi ngi jublu woon yerusalem.

Japonais

村人は、エルサレムへむかって進んで行かれるというので、イエスを歓迎しようとはしなかった。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi festus teersee ci diiwaanam, mu teg ca ñetti fan, dem yerusalem.

Japonais

さて、フェストは、任地に着いてから三日の後、カイザリヤからエルサレムに上ったところ、

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

man ngaa wóorliku ne, ëppagul fukki fan ak ñaar demoon naa yerusalem ngir màggali.

Japonais

お調べになればわかるはずですが、わたしが礼拝をしにエルサレムに上ってから、まだ十二日そこそこにしかなりません。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu ñépp génn jëm ci moom, ñi dëkk yerusalem ak diiwaanu yude, ak waa dexu yurdan.

Japonais

すると、エルサレムとユダヤ全土とヨルダン附近一帯の人々が、ぞくぞくとヨハネのところに出てきて、

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

«bi ma dellusee yerusalem nag, di ñaan ca kër yàlla ga, leer tàbbi ci man.

Japonais

それからわたしは、エルサレムに帰って宮で祈っているうちに、夢うつつになり、

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

Ñoo feeñ ci ndamu yàlla, di waxtaane ci demu yeesu, gi muy àggalee yenam ci yerusalem.

Japonais

栄光の中に現れて、イエスがエルサレムで遂げようとする最後のことについて話していたのである。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

am na ci waa yerusalem ñu doon wax naan: «xanaa du nit kii lañuy wut a rey?

Japonais

さて、エルサレムのある人たちが言った、「この人は人々が殺そうと思っている者ではないか。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

fekk booba amoon na ay yawut yu daloon yerusalem, doon ay nit ñu ragal yàlla te bokk ci xeeti àddina yépp.

Japonais

さて、エルサレムには、天下のあらゆる国々から、信仰深いユダヤ人たちがきて住んでいたが、

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi sool agsee yerusalem, mu jéem a ànd ak taalibe yi, waaye ñépp ragal ko, ndax gëmuñu woon ag taalibeem.

Japonais

サウロはエルサレムに着いて、弟子たちの仲間に加わろうと努めたが、みんなの者は彼を弟子だとは信じないで、恐れていた。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

«bu ngeen gisee ay xarekat wër dëkku yerusalem, xamleen ne jamono, ji ñu koy yàq, agsi na.

Japonais

エルサレムが軍隊に包囲されるのを見たならば、そのときは、その滅亡が近づいたとさとりなさい。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi nga xamee ne ndaw yi nekk yerusalem yég nañu ne, waa samari nangu nañu kàddug yàlla; ñu yónni fa piyeer ak yowaana.

Japonais

エルサレムにいる使徒たちは、サマリヤの人々が、神の言を受け入れたと聞いて、ペテロとヨハネとを、そこにつかわした。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi mu yégee ne, yeesoo ngi nekk ci diiwaan bi erodd yilif, mu yónnee ko erodd, mi nekkoon ci jamono jooju ci yerusalem.

Japonais

そしてヘロデの支配下のものであることを確かめたので、ちょうどこのころ、ヘロデがエルサレムにいたのをさいわい、そちらへイエスを送りとどけた。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

gannaaw loolu yeesu di dem yerusalem, ànd ak fukki taalibe yi ak ñaar. noonu mu wéetoo ak ñoom, di leen xamal ci yoon wi lii:

Japonais

さて、イエスはエルサレムへ上るとき、十二弟子をひそかに呼びよせ、その途中で彼らに言われた、

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

loolu siiwoon na ci waa yerusalem, moo tax ci seen làkk ñuy tudde tool ba akeldama, maanaam «toolu deret.» —

Japonais

そして、この事はエルサレムの全住民に知れわたり、そこで、この地所が彼らの国語でアケルダマと呼ばれるようになった。「血の地所」との意である。)

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu yeesu dugg yerusalem, dem kër yàlla ga, xool lépp, ba noppi génn dem dëkku betani, moom ak fukki taalibe ya ak ñaar, ndaxte dafa guddi.

Japonais

こうしてイエスはエルサレムに着き、宮にはいられた。そして、すべてのものを見まわった後、もはや時もおそくなっていたので、十二弟子と共にベタニヤに出て行かれた。

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

Ñaanal-leen ma, ngir ma mucc ci ñi gëmul ci waa yude; te it gaayi yàlla yu sell yu nekk ci yerusalem nangu ndimbal, li ma leen di yóbbul.

Japonais

すなわち、わたしがユダヤにおる不信の徒から救われ、そしてエルサレムに対するわたしの奉仕が聖徒たちに受けいれられるものとなるように、

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,763,828,445 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK