Vous avez cherché: dëppook (Wolof - Portugais)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Portugais

Infos

Wolof

yaw nag nangay waare li dëppook njàngale mu wér mi.

Portugais

tu, porém, fala o que convém � sã doutrina.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ci feeñal nu mbóoti coobareem, dëppook yéeneem ju rafet, ji mu jaarale ci kirist.

Portugais

fazendo-nos conhecer o mistério da sua vontade, segundo o seu beneplácito, que nele propôs

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

li dëppook waxi seede, yi ko teewe woon li dale ca ndoorte la te ñu mujj nekk jawriñi kàddug yàlla.

Portugais

segundo no-los transmitiram os que desde o princípio foram testemunhas oculares e ministros da palavra,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ngeen xam it, ni kàttanam màgge ba jéggi dayo, jëm ci nun ñi gëm, dëppook dooleem ju ràññiku,

Portugais

e qual a suprema grandeza do seu poder para conosco, os que cremos, segundo a operação da força do seu poder,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu dina soppi sunu yaram wu toroxlu, def ko ni yaramam wi ànd ak ndam dëppook kàttanam, gi ko man a nootal mbindeef yépp.

Portugais

que transformará o corpo da nossa humilhação, para ser conforme ao corpo da sua glória, segundo o seu eficaz poder de até sujeitar a si todas as coisas.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu nu mànkoo ci sunu ngëm ak ci xam doomu yàlla ji, ba kera nuy egg ci nekk nit ku sotti, te taxaw taxawaay bu dëppook matug kirist.

Portugais

até que todos cheguemos � unidade da fé e do pleno conhecimento do filho de deus, ao estado de homem feito, � medida da estatura da plenitude de cristo;

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

léegi nag, na ndam li féete ak yàlla, mi man a yeggale lépp luy ñaan mbaa yéene, ba weesu ko fuuf, dëppook kàttan giy jëf ci nun;

Portugais

ora, �quele que é poderoso para fazer tudo muito mais abundantemente além daquilo que pedimos ou pensamos, segundo o poder que em nós opera,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

kon nag timote sama doom, loolu mooy sas wi ma lay dénk, te mu dëppook waxi yonent, yi jëmoon ci yaw. doolewool wax yooyu, ba xeex xeex bu baax bi,

Portugais

esta admoestação te dirijo, filho timóteo, que segundo as profecias que houve acerca de ti, por elas pelejes a boa peleja,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

looloo tax ma yebal ci yéen timote, miy sama doomu diine, di doom ju takku te ma bëgg ko. dina leen fàttali ni may dunde ci kirist, te mu dëppook li may jàngale fu nekk ci mboolooy ñi gëm ñépp.

Portugais

por isso mesmo vos enviei timóteo, que é meu filho amado, e fiel no senhor; o qual vos lembrará os meus caminhos em cristo, como por toda parte eu ensino em cada igreja.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,799,936,979 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK