Vous avez cherché: maryaama (Wolof - Russe)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Russe

Infos

Wolof

noonu maryaama daldi ne:

Russe

И сказала Мария: величит душа Моя Господа,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ak maryaama, mi sonnoon lool ci yéen.

Russe

Приветствуйте Мариам, которая много трудилась для нас.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu soppoon na màrt ak maryaama ak lasaar.

Russe

Иисус же любил Марфу и сестру ее и Лазаря.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

maryaamam magdala nag ak maryaama yaayu yuusufa xool fu mu ko denc.

Russe

Мария же Магдалина и Мария Иосиева смотрели, где Егополагали.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mu dem binduji, ànd ak maryaama jabaram, fekk booba maryaama ëmb.

Russe

записаться с Мариею, обрученною ему женою, которая была беременна.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi maryaama déggee loolu, mu daldi jóg, gaawantoo dem ca yeesu.

Russe

Она, как скоро услышала, поспешно встала и пошла к Нему.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

fekk maryaamam magdala ak maryaama ma ca des ñoo fa toogoon janook bàmmeel ba.

Russe

Была же там Мария Магдалина и другая Мария, которыесидели против гроба.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

maryaama nag dem nettali ko ñi àndoon ak yeesu, fekk ñuy naqarlu, di jooy.

Russe

Она пошла и возвестила бывшим с Ним, плачущим и рыдающим;

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waxi malaaka ma daldi jaaxal maryaama, muy xalaat lu nuyoo boobu man a tekki.

Russe

Она же, увидев его, смутилась от слов его и размышляла, что бы это было за приветствие.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ci jamono jooju maryaama jóg, gaawantu dem ci benn dëkk bu nekkoon ca tund ya ca diiwaanu yude.

Russe

Встав же Мария во дни сии, с поспешностью пошла в нагорную страну, в город Иудин,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

Ñu daldi gaawantu dem, gis maryaama ak yuusufa, ak liir, ba ñu tëral ca lekkukaayu jur ga.

Russe

И, поспешив, пришли и нашли Мариюи Иосифа, и Младенца, лежащего в яслях.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

malaaka ma ne ko: «bul ragal dara maryaama, ndaxte yàlla tànn na la ci yiwam.

Russe

И сказал Ей Ангел: не бойся, Мария,ибо Ты обрела благодать у Бога;

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

xàmmi nañu ci: maryaama mi dëkk magdala, ndeyu saag ak yuusufa, ak ndeyu doomi sebede ya.

Russe

между ними были Мария Магдалина и Мария, мать Иакова и Иосии, и мать сыновей Зеведеевых.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

jigéen ña ñoo doon maryaamam magdala, sànn, ak maryaama yaayu saag. yeneen jigéen yi leen gunge woon itam nettali loolu ndaw ya.

Russe

То были Магдалина Мария, и Иоанна, и Мария, мать Иакова, и другие с ними, которые сказали о сем Апостолам.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

amoon na benn waay bu woppoon, ñu koy wax lasaar. ma nga dëkkoon betani, moom ak maryaama ak màrt, mi mu bokkaloon ndey ak baay.

Russe

Был болен некто Лазарь из Вифании, из селения, где жили Мария и Марфа, сестра ее.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu yawut, ya nekkoon ca kër ga di dëfël maryaama, gis ko mu ne bërét génn, ñu daldi koy topp, defe ne, day jooyi ca bàmmeel ba.

Russe

Иудеи, которые были с нею в доме и утешали ее, видя, что Мария поспешно встала и вышла, пошли за нею, полагая, что она пошла на гроб - плакать там.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi màrt waxee loolu, mu daldi dem woowi maryaama ne ko ci pett: «kilifa gaa ngi fi; mi ngi lay laaj.»

Russe

Сказав это, пошла и позвала тайно Марию, сестру свою, говоря: Учитель здесь и зовет тебя.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

Ñu dugg ca kër ga, gis xale ba ak maryaama ndeyam, ñu daldi sukk, di ko màggal. Ñu ubbi seeni boyetu alal, may ko wurus ak cuuraay ak ndàbb lu xeeñ lu ñuy wax miir.

Russe

и, войдя в дом, увидели Младенцас Мариею, Матерью Его, и, пав, поклонились Ему; и, открыв сокровища свои, принесли Ему дары: золото, ладан и смирну.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi maryaama agsee nag ca yeesu, ba gis ko, mu daanu ciy tànkam ne ko: «boroom bi, boo fi nekkoon, sama càmmiñ du dee.»

Russe

Мария же, придя туда, где был Иисус, и увидев Его, пала к ногам Его и сказала Ему: Господи!если бы Ты был здесь, не умер бы брат мой.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndax kii du minise bi? ndax du doomu maryaama te magu saag, yuusufa, yuda ak simoŋ? te ay rakkam yu jigéen ndax nekkuñu fi ak nun?» kon nag ñu daldi ko xeeb.

Russe

Не плотник ли Он, сын Марии, брат Иакова, Иосии, Иуды и Симона? Не здесь ли, между нами, Егосестры? И соблазнялись о Нем.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,786,480,890 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK