Vous avez cherché: ndigali (Wolof - Russe)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Russe

Infos

Wolof

xaraf ak ñàkka xaraf lépp a yem; li am solo moo di topp ndigali yàlla.

Russe

Обрезание ничто и необрезание ничто, но все в соблюдении заповедей Божиих.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

looloo tax gaayi yàlla yi war a muñ, ñooñuy sàmm ndigali yàlla yi ak ngëm ci yeesu.

Russe

Здесь терпение святых, соблюдающих заповеди Божии и веру в Иисуса.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu neeti leen: «dëddu ngeen ndigali yàlla, jublu ci aaday nit.»

Russe

Ибо вы, оставив заповедь Божию, держитесь предания человеческого, омовения кружек и чаш, и делаете многое другое, сему подобное.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ku weddi ndigali yoonu musaa wi, te ñaar walla ñetti nit seede ko, dina dee ci lu amul benn yërmande.

Russe

Если отвергшийся закона Моисеева, при двух или трех свидетелях, без милосердия наказывается смертью,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndigali yàlla yi, ci gémmiñu musaa lañu leen jaarale; yiw wi ak dëgg gi, yeesu kirist moo ko indaale.

Russe

ибо закон дан чрез Моисея; благодать же и истинапроизошли чрез Иисуса Христа.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

te yason a leen dalal. Ñoom ñépp dañoo bañ ndigali buur sesaar ne, am na beneen buur bu ñuy wax yeesu.»

Russe

а Иасон принял их, и все они поступают против повелений кесаря, почитая другого царем, Иисуса.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye su ma delloo di sàmm ndigali yoon, yi ma bàyyi, dëgg-dëgg dinaa wone noonu ne, moykatu yoon wi laa.

Russe

Ибо если я снова созидаю, что разрушил, то сам себя делаю преступником.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

lii mooy mbëggeel: nu wéer sunug dund ci ndigali yàlla; loolu mooy ndigalam, la nu jotoon ca njàlbeen ga, te ci lanu wara jaar.

Russe

Любовь же состоит в том, чтобы мы поступали по заповедям Его. Это та заповедь, которую вы слышали от начала, чтобы поступали по ней.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

Ñiy wékku ñépp ci jëfi yoon wi, ñu alku lañu, ndaxte bind nañu ne: «képp ku dul topp lépp lu ndigali yoon wi santaane, yal na alku.»

Russe

а все, утверждающиеся на делах закона, находятся под клятвою. Ибо написано: проклят всяк, кто не исполняет постоянно всего, что написано в книге закона.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

keroog musaa jàng na ndigali yoon wépp ci kanamu bànni israyil gépp. gannaaw loolu jël na deretu wëllu, jëlaale ndox, ak bantu garab gu ñuy wax isob, laxas ci kawaru xar mu xonq. noonu mu capp ko ca deret ja, daldi ko wis ca téereb yoon wa ak ca mbooloo mépp

Russe

Ибо Моисей, произнеся все заповеди по закону перед всем народом, взял кровь тельцов и козлов с водою и шерстью червленою и иссопом, и окропил как самую книгу, так и весь народ,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,793,595,646 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK