Vous avez cherché: waxambaane (Wolof - Suédois)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Suédois

Infos

Wolof

naka noonu itam nanga xiir waxambaane yi cig maandu.

Suédois

förmana likaledes de yngre männen att skicka sig tuktigt.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

naka waxambaane wa, ñu indi ko muy dund, ba seen xol sedd guyy.

Suédois

och de förde ynglingen hem levande och kände sig nu icke litet tröstade.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye waxambaane wa wacc fa sér bi, daldi daw, def yaramu neen.

Suédois

men han lämnade linneklädet kvar och flydde undan naken.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waxambaane wa ne ko: «sàmm naa yooyu yépp, lu ma deseeti?»

Suédois

då sade den unge mannen till honom: »allt detta har jag hållit. vad fattas mig ännu?»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

fekk amoon na ca waxambaane wu lëkkaayoo woon sér, topp yeesu, ñu daldi ko jàpp.

Suédois

och bland dem som hade följt med honom var en ung man, höljd i ett linnekläde, som var kastat över blotta kroppen; honom grepo de.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye bi waxambaane wa déggee loolu, mu jóge fa ak tiis, ndaxte ku bare woon alal la.

Suédois

men när den unge mannen hörde detta, gick han bedrövad bort, ty han hade många ägodelar.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

kilifa ga nag sant waxambaane wa, mu bañ koo àgge kenn, ba noppi mu yiwi ko, mu dem.

Suédois

Översten bjöd då ynglingen att icke för någon omtala att han hade yppat detta för honom, och lät honom sedan gå.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu kilifa ga jàpp ci loxob waxambaane wa, wéetoo ak moom, laaj ko: «loo ma bëgg a yégal?»

Suédois

då tog översten honom vid handen och gick avsides med honom och frågade honom: »vad är det för en underrättelse du har att lämna mig?»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mu jegeñsi, laal jaat ga, ñi ko jàppoo taxaw. mu ne: «waxambaane wi, jógal, ndigal la.»

Suédois

och han gick fram och rörde vid båren, och de som buro stannade. och han sade: »unge man, jag säger dig: stå upp.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ca saa sa mu daanu ciy tànkam dee. bi waxambaane ya agsee nag, ñu fekk ko, mu faatu; ñu yóbbu ko, def ko ci wetu jëkkëram.

Suédois

och strax föll hon ned vid hans fötter och gav upp andan; och när de unge männen kommo in, funno de henne död. de buro då ut henne och begrovo henne bredvid hennes man.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi ko pool déggee, mu woo kenn ca njiiti xare ba ne ko: «yóbbul waxambaane wii ca kilifa ga, ndax am na lu mu ko war a yégal.»

Suédois

paulus bad då att en av hövitsmännen skulle komma till honom, och sade: »för denne yngling till översten; ty han har en underrättelse att lämna honom.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bind naa leen, samay doom,ndax xam ngeen yàlla baay bi.bind naa leen, yéen baay yi,ndax xam ngeen ki nekkoon ca njàlbéen ga ba tey.bind naa leen, yéen waxambaane yi,ndax yéena ngi dëgër,ndax kàddug yàllaa ngi dëkk ci yéen,te daaneel ngeen ibliis.

Suédois

jag har skrivit till eder, mina barn, ty i haven lärt känna fadern. jag har skrivit till eder, i fäder, ty i haven lärt känna honom som är från begynnelsen. jag har skrivit till eder, i ynglingar, ty i ären starka, och guds ord förbliver i eder, och i haven övervunnit den onde.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,802,041 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK