Da traduttori professionisti, imprese, pagine web e archivi di traduzione disponibili gratuitamente al pubblico.
if we this day be examined of the good deed done to the impotent man, by what means he is made whole;
bu fekkee ne xettali nit ku wopp, ba mu wér, moo tax ngeen dëj nu ci pénc mi tey,
Ultimo aggiornamento 2012-05-04
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
and whatsoever ye do in word or deed, do all in the name of the lord jesus, giving thanks to god and the father by him.
te lu ngeen man a def, muy ci wax mbaa ci jëf, wéerleen ko ci turu boroom bi yeesu, jaare ci moom gërëm yàlla baay bi.
Ultimo aggiornamento 2012-05-04
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
for i will not dare to speak of any of those things which christ hath not wrought by me, to make the gentiles obedient, by word and deed,
awma fitu wax leneen nag, lu dul li kirist jëf jaarale ko ci man, ngir xeeti àddina jébbalu ci moom; jëf na jaarale ci samay wax ak samay jëf,
Ultimo aggiornamento 2012-05-04
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
(for that righteous man dwelling among them, in seeing and hearing, vexed his righteous soul from day to day with their unlawful deeds;)
ndaxte lóot, mi dëkkoon ci seen biir, dafa dëkke woon tiisu xol, ndax ñaawteef yi mu gis ak a dégg guddi ak bëccëg.
Ultimo aggiornamento 2012-05-04
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità: