Da traduttori professionisti, imprese, pagine web e archivi di traduzione disponibili gratuitamente al pubblico.
Уразумев то, Иисус сказал им: что помышляете в себе, маловерные, что хлебов не взяли?
waaye yeesu yég loolu ne leen: «yéen ñi néew ngëm, lu tax ngeen di werante ci seen biir, ndaxte indaalewuleen mburu?
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
И говорит им: что вы так боязливы, маловерные? Потом, встав, запретил ветрам и морю, и сделалась великая тишина.
waaye yeesu tontu leen: «yéen ñi néew ngëm, lu tax ngeen tiit?» ci kaw loolu mu jóg, daldi gëdd ngelaw li ak duus yi. lépp dal, ba ne nemm.
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
Иисус тотчас простер руку, поддержал его и говорит ему: маловерный! зачем ты усомнился?
ca saa sa yeesu tàllal loxoom, jàpp ko naan: «yaw mi néew ngëm, lu tax nga am xel ñaar?»
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità: