Hai cercato la traduzione di akifundisha da Swahili a Wolof

Contributi umani

Da traduttori professionisti, imprese, pagine web e archivi di traduzione disponibili gratuitamente al pubblico.

Aggiungi una traduzione

Swahili

Wolof

Informazioni

Swahili

yesu alikuwa akifundisha katika sunagogi moja siku ya sabato.

Wolof

benn bésu noflaay yeesoo ngi doon jàngale ci ab jàngu.

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

yesu alisema hayo alipokuwa akifundisha katika sunagogi kule kafarnaumu.

Wolof

baat yooyu la yeesu wax, bi mu doon jàngale ca jàngu ba ca kapernawum.

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

basi, paulo alikaa huko akifundisha neno la mungu kati yao kwa muda wa mwaka mmoja na nusu.

Wolof

noonu pool des at ak genn-wàll ci seen biir, di fa jàngale kàddug yàlla.

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

wakati wa mchana, siku hizo, yesu alikuwa akifundisha watu hekaluni; lakini usiku alikuwa akienda katika mlima wa mizeituni na kukaa huko.

Wolof

yeesoo ngi daan yendoo jàngale ca kër yàlla ga, te bu guddee mu dem ca tund wu ñuy wax tundu oliw ya, fanaan fa.

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

yesu alikuwa anakwenda kila mahali wilayani galilaya, akifundisha katika masunagogi na kuhubiri habari njema juu ya ufalme wa mungu. aliponya kila namna ya maradhi na magonjwa waliyokuwa nayo watu.

Wolof

ba loolu amee yeesu doon wër galile gépp, di jàngale ci seeni jàngu tey yégle xebaar bu baax bi ci nguuru yàlla; muy faj jàngoro yépp ak wéradi yépp ca nit ña,

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

siku moja yesu alikuwa akifundisha. mafarisayo na walimu wa sheria kutoka katika kila kijiji cha galilaya, yudea na yerusalemu, walikuwa wameketi hapo. nguvu ya bwana ilikuwa pamoja naye kwa ajili ya kuponyea wagonjwa.

Wolof

am na bés yeesu doon jàngale. amoon na ca mbooloo, ma teewoon, ñu bokkoon ca farisen ya ak ay xutbakat yu jóge ca dëkk yépp, ya ca galile ak ya ca yude ak yerusalem. yeesu àndoon na ak dooley boroom bi, ba muy faj ay jarag.

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

yesu aliingia hekaluni, akawa anafundisha. alipokuwa akifundisha, makuhani wakuu na wazee wa watu wakamwuliza, "unafanya mambo haya kwa mamlaka gani? nani amekupa mamlaka haya?"

Wolof

gannaaw loolu yeesu dugg ca kër yàlla ga, di fa jàngale. bi muy jàngale nag saraxalekat yu mag ya ak njiiti xeet wa ñëw ci moom ne ko: «yëf yii ngay def, ci ban sañ-sañ nga koy defe? ku la may boobu sañ-sañ?»

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Attenzione: contiene formattazione HTML nascosta

Ottieni una traduzione migliore grazie a
7,737,755,591 contributi umani

Ci sono utenti che chiedono aiuto:



I cookie ci aiutano a fornire i nostri servizi. Utilizzando tali servizi, accetti l'utilizzo dei cookie da parte nostra. Maggiori informazioni. OK