Hai cercato la traduzione di kushiriki da Swahili a Wolof

Contributi umani

Da traduttori professionisti, imprese, pagine web e archivi di traduzione disponibili gratuitamente al pubblico.

Aggiungi una traduzione

Swahili

Wolof

Informazioni

Swahili

nafanya haya yote kwa ajili ya habari njema, nipate kushiriki baraka zake.

Wolof

damaa def loolu lépp ndax xebaar bu baax bi, ngir man it ma am wàll ci barkeem.

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

walitusihi sana wapewe nafasi ya kushiriki katika huduma hii ya kuwasaidia watu wa mungu.

Wolof

saraxu nañu nu lool, ngir bokk ci ñiy yónnee ndimbal gaayi yàlla yi.

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

lakini wale ambao mungu atawawezesha kushiriki ule wakati wa ufufuo, hawataoa wala kuolewa.

Wolof

waaye ña ñu àtte ne, yeyoo nañoo bokk ci dundu ëllëg ak ci ndekkite li, kenn du am jabar, kenn du am jëkkër.

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

basi, sisi tunapaswa kuwasaidia watu hawa, ili nasi tupate kushiriki katika kazi yao kwa ajili ya ukweli.

Wolof

nun nag fàww nu teeru ñu mel ni ñoom, ngir nu liggéeyandoo ak dëgg gi.

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

basi, sasa naja kwako, na nimesema mambo haya ulimwenguni, ili waweze kushiriki kikamilifu furaha yangu.

Wolof

«waaye léegi maa ngi jëmsi ci yaw, te maa ngi wax nii ci bi may nekk àddina, ngir ñu fees ak sama mbég.

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

hamwezi kunywa kikombe cha bwana na kikombe cha pepo; hamwezi kushiriki katika meza ya bwana na katika meza ya pepo.

Wolof

mënuleen a naan ci kaasu boroom bi, naan ci kaasu rab yi. mënuleen a sukk ci reerub boroom bi, sukk ci reerub rab yi.

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

kwa imani yetu, yeye ametuleta katika hali hii ya neema ya mungu ambamo sasa tunaishi. basi, tunajivunia tumaini tulilo nalo la kushiriki utukufu wa mungu.

Wolof

moo nu ubbil bunt ci yàlla, nu taxaw temm ci yiwam, jaar ci ngëm. te it nu ngi bég ciy négandiku, yàlla boole nu ci ndamam.

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

kwa wale wanaopotea, harufu hiyo ni kifo; lakini kwa wale wanaookolewa, harufu hiyo ni uhai. nani basi, awezaye kushiriki katika kazi ya namna hiyo?

Wolof

ci ñu mujj ñii, xet gu sedd lanu, guy jëme ci dee; ci ñu jëkk ñi, xetu dund lanu, guy jëme ci dund. kon ku man a àttan yen boobu!

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

basi, kwa vile watoto hao, kama awaitavyo, ni watu wenye mwili na damu, yesu mwenyewe akawa kama wao na kushiriki ubinadamu wao. alifanya hivyo ili kwa njia ya kifo chake amwangamize ibilisi, ambaye ana mamlaka juu ya kifo,

Wolof

doomam yooyu muy wax, nit kese lañu. looloo tax yeesu it moom ci boppam, wàcc na, jëmmoo ni ñoom, ngir dee, ba man caa daaneel ibliis, mi yore dooley dee.

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Ottieni una traduzione migliore grazie a
7,763,943,436 contributi umani

Ci sono utenti che chiedono aiuto:



I cookie ci aiutano a fornire i nostri servizi. Utilizzando tali servizi, accetti l'utilizzo dei cookie da parte nostra. Maggiori informazioni. OK