Hai cercato la traduzione di kuwahubiria da Swahili a Wolof

Contributi umani

Da traduttori professionisti, imprese, pagine web e archivi di traduzione disponibili gratuitamente al pubblico.

Aggiungi una traduzione

Swahili

Wolof

Informazioni

Swahili

na kwa maisha yake ya kiroho alikwenda kuwahubiria wale roho waliokuwa kifungoni.

Wolof

ci biir xel moomu la yégaleji ndamam ca ruu ya yàlla tëj kaso;

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

mnajua kwamba sikusita hata kidogo kuwahubiria hadharani na nyumbani mwenu na kuwafundisha chochote ambacho kingewasaidieni.

Wolof

xam ngeen ne, musuma leen a nëbb dara lu leen di jariñ, di leen jàngal ci kanamu ñépp ak ca kër ya.

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

naupa mwili wangu mazoezi magumu na kuutia katika nidhamu kamili, nisije mimi mwenyewe nikakataliwa baada ya kuwahubiria wengine.

Wolof

waaye damay noot sama yaram, ba moom ko, ngir ragal a yégal ñi ci des xebaar bu baax bi, ba noppi yàlla xañ ma ndam li.

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

siku moja, yesu alipokuwa akiwafundisha watu hekaluni na kuwahubiria juu ya habari njema, makuhani wakuu na walimu wa sheria pamoja na wazee walifika,

Wolof

benn bés yeesu doon jàngal nit ña ca kër yàlla ga, di leen yégal xebaar bu baax bi. saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya ak njiit ya ñëw ne ko:

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

hata walijaribu kutuzuia kuwahubiria watu wa mataifa mengine ujumbe utakaowaletea wokovu. ndivyo walivyokamilisha orodha ya dhambi zote walizotenda siku zote. lakini sasa hasira ya mungu imewaangukia.

Wolof

di nu teree wax ak ñi dul yawut, ngir bañ ñu mucc. duñu noppee xuus ci biir bàkkaar, waaye merum yàlla xëppu na ci seen kaw.

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Ottieni una traduzione migliore grazie a
7,746,498,607 contributi umani

Ci sono utenti che chiedono aiuto:



I cookie ci aiutano a fornire i nostri servizi. Utilizzando tali servizi, accetti l'utilizzo dei cookie da parte nostra. Maggiori informazioni. OK