Da traduttori professionisti, imprese, pagine web e archivi di traduzione disponibili gratuitamente al pubblico.
aliye shambani asirudi nyuma kuchukua vazi lake.
ku nekk ca tool ba, bul ñibbi ngir fab sa mbubb.
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
kwa hivyo mwombeni mwenye shamba atume wavunaji shambani mwake."
Ñaanleen nag boroom ngóob mi, mu yebal ay liggéeykat, ñu góob toolam.»
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
Attenzione: contiene formattazione HTML nascosta
akaomba kazi kwa mwananchi mtu mmoja wa huko naye akampeleka shambani mwake kulisha nguruwe.
mu dem nag, di liggéeyal ku dëkk ca réew ma, kooku yebal ko ca ay toolam ngir mu sàmm mbaam-xuux ya.
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
baadaye yesu aliwatokea wanafunzi wawili akiwa na sura nyingine. wanafunzi hao walikuwa wanakwenda shambani.
gannaaw loolu yeesu feeñu ñaar ci ñoom ci jeneen jëmm, ñuy jaar ci yoon wi, jëm àll ba.
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
lakini wao hawakujali, wakaenda zao; mmoja shambani kwake, mwingine kwenye shughuli zake,
waaye ba tey wuyuwuñu ko; ñu dem, kenn ki ca toolam, kenn ki jaayaani,
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
"wakati huo kaka yake alikuwa bado shambani. alipokuwa akirudi na kukaribia nyumbani akasikia vifijo na ngoma.
«fekk booba taaw baa nga woon ca tool ya. bi mu ñëwee, ba jub kër ga, mu dégg ñuy tëgg, di fecc.
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
Attenzione: contiene formattazione HTML nascosta
"siku hiyo, yeyote atakayekuwa juu ya paa asishuke nyumbani kuchukua mali yake. kadhalika, naye atakayekuwa shambani asirudi nyuma.
«ca bés boobee ku nekk ca kaw kër ga te ay bagaasam nekk ca biir, bumu wàcc jëli leen. te it ku nekk ca tool ya, bu mu ñibbi.
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
Attenzione: contiene formattazione HTML nascosta
akawaambia, "mavuno ni mengi, lakini wavunaji ni wachache. kwa hivyo, mwombeni mwenye shamba atume wavunaji shambani mwake.
mu ne leen: «ngóob mi yaatu na, waaye liggéeykat yi barewuñu. Ñaanleen nag boroom ngóob mi, mu yebal ay liggéeykat, ñu góob toolam.
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
Attenzione: contiene formattazione HTML nascosta
ikiwa basi mungu hulivika hivyo jani la shambani ambalo leo liko na kesho latupwa motoni, je, hatafanya zaidi kwenu ninyi? enyi watu wenye imani haba!
yéen ñi néew ngëm! bu yàlla woddee nii ñaxum tool yi, miy sax tey, te bu subaa ñu def ko ci taal bi, ndax du leen gën a wodd?
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
"ufalme wa mbinguni umefanana na hazina iliyofichika shambani. mtu mmoja aliigundua, akaificha tena. alifurahi sana hata akaenda kuuza yote aliyokuwa nayo, akalinunua shamba lile.
yeesu teg ca ne: «nguuru yàlla aji kawe ji dafa mel ni alal ju nëbbu cib tool. nit ki ko gis nëbbaat ko; xolam sedd, ba mu dem jaay li mu am lépp, jënd tool ba.
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
Attenzione: contiene formattazione HTML nascosta
"tuseme mmoja wenu ana mtumishi ambaye analima shambani au anachunga kondoo. je, anaporudi kutoka shambani, atamwambia: haraka, njoo ule chakula?
«kan ci yéen bu amoon surga bu beyi walla bu sàmmi ba ñëw, ndax dafa ko naa: “kaay lekk.”
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
Attenzione: contiene formattazione HTML nascosta