Da traduttori professionisti, imprese, pagine web e archivi di traduzione disponibili gratuitamente al pubblico.
na sa nguur ñëw,na sa coobare am ci suuf mel ni ci kaw.
thy kingdom come. thy will be done in earth, as it is in heaven.
Ultimo aggiornamento 2012-05-04
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
kon nag gannaaw li may def du sama coobare, nangu naa ne yoonu musaa baax na.
if then i do that which i would not, i consent unto the law that it is good.
Ultimo aggiornamento 2012-05-04
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
sunuy baay yar nañu nu diir bu gàtt ci seen coobare. waaye yàlla dafa nuy yar ngir sunu njariñ, ngir nu bokk ci sellaayam.
for they verily for a few days chastened us after their own pleasure; but he for our profit, that we might be partakers of his holiness.
Ultimo aggiornamento 2012-05-04
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
ndaxte waxuma ci sama coobare, waaye baay bi ma yónni ci boppam, moo ma sant li ma war a wax ak li ma war a jàngale.
for i have not spoken of myself; but the father which sent me, he gave me a commandment, what i should say, and what i should speak.
Ultimo aggiornamento 2012-05-04
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
«baay, soo ko bëggee, teggil ma kaasu naqar bii. moona bumu doon sama coobare, waaye na sa coobare am.»
saying, father, if thou be willing, remove this cup from me: nevertheless not my will, but thine, be done.
Ultimo aggiornamento 2012-05-04
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
moo tax ma ne: “damaa wàccngir def sa coobare, yaw yàlla,mu dëppoo ak li ñu bind ci sama mbirci téereb yoon wi.”»
then said i, lo, i come (in the volume of the book it is written of me,) to do thy will, o god.
Ultimo aggiornamento 2012-05-04
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
yeesu delluwaat di ñaan ne: «sama baay, bu fekkee ne kaasu naqar bii mënu maa teggi te naanuma ko, kon na sa coobare am.»
he went away again the second time, and prayed, saying, o my father, if this cup may not pass away from me, except i drink it, thy will be done.
Ultimo aggiornamento 2012-05-04
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
«yàlla sunu boroom,yaa yeyoo ndam, teraanga ak kàttan,ndaxte yaa sàkk léppte ci sa coobare la lépp nekke,te ci lañu leen sàkke.»
thou art worthy, o lord, to receive glory and honour and power: for thou hast created all things, and for thy pleasure they are and were created.
Ultimo aggiornamento 2012-05-04
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
bi mu waxee loolu, yeesu dem ci kanam tuuti, ne nërëm ci suuf, di ñaan ne: «sama baay, bu manee am, na ma kaasu naqar bii teggi! moona, bumuy ci sama coobare, waaye na sa coobare am.»
and he went a little further, and fell on his face, and prayed, saying, o my father, if it be possible, let this cup pass from me: nevertheless not as i will, but as thou wilt.
Ultimo aggiornamento 2012-05-04
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità: