Da traduttori professionisti, imprese, pagine web e archivi di traduzione disponibili gratuitamente al pubblico.
ku bëgg a siiw, doo nëbb say jëf. boo demee bay wone jaloore yu mel ni, fexeel ba ñépp gis la.»
for there is no man that doeth any thing in secret, and he himself seeketh to be known openly. if thou do these things, shew thyself to the world.
Ultimo aggiornamento 2012-05-04
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
te bi ma déggee ne, ñu ngi koy fexeel, yebal naa ko ci yaw ci saa si. sant naa nag ñi ko kalaame, ñu xamal la seen lay.
and when it was told me how that the jews laid wait for the man, i sent straightway to thee, and gave commandment to his accusers also to say before thee what they had against him. farewell.
Ultimo aggiornamento 2012-05-04
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
booba nag saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya ñu ngi doon fexeel yeesu, ngir jàpp ko, reylu. fekk booba ñaari fan a des ci màggalu bésu jéggi ba ak màggalu mburu ya amul lawiir.
after two days was the feast of the passover, and of unleavened bread: and the chief priests and the scribes sought how they might take him by craft, and put him to death.
Ultimo aggiornamento 2012-05-04
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
di xaacu naan: «yaw yeesu doomu yàlla aji kawe ji, loo may fexeel? ci turu yàlla, bu ma mbugal.»
and cried with a loud voice, and said, what have i to do with thee, jesus, thou son of the most high god? i adjure thee by god, that thou torment me not.
Ultimo aggiornamento 2012-05-04
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
Ña rab jàpp daldi xaacu naan: «yaw doomu yàlla ji, loo nuy fexeel? ndax danga noo bëgg a mbugal, bala waxtu way jot?»
and, behold, they cried out, saying, what have we to do with thee, jesus, thou son of god? art thou come hither to torment us before the time?
Ultimo aggiornamento 2012-05-04
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
«moo! yaw yeesum nasaret, loo nuy fexeel? ndax dangaa ñëw ngir alag nu? xam naa la, yaa di aji sell ji jóge ci yàlla!»
saying, let us alone; what have we to do with thee, thou jesus of nazareth? art thou come to destroy us? i know thee who thou art; the holy one of god.
Ultimo aggiornamento 2012-05-04
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
«yaw yeesum nasaret, loo nuy fexeel? ndax dangaa ñëw, ngir alag nu? xam naa la, yaa di aji sell, ji jóge ci yàlla.»
saying, let us alone; what have we to do with thee, thou jesus of nazareth? art thou come to destroy us? i know thee who thou art, the holy one of god.
Ultimo aggiornamento 2012-05-04
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità: