Da traduttori professionisti, imprese, pagine web e archivi di traduzione disponibili gratuitamente al pubblico.
yaw nag nangay waare li dëppook njàngale mu wér mi.
tu però insegna ciò che è secondo la sana dottrina
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
noonu mu dem di waare ca jàngu ya ca réewu yawut ya.
e andava predicando nelle sinagoghe della giudea
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
ca jamono jooja yaxya feeñoon na, di waare ca màndiŋu yude.
in quei giorni comparve giovanni il battista a predicare nel deserto della giudea
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
te su kirist dekkiwul, sunu waare day neen, te it seen ngëm day neen.
ma se cristo non è risuscitato, allora è vana la nostra predicazione ed è vana anche la vostra fede
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
kon nag gannaaw wékku nanu ci yaakaar ju mel noonu, danuy waare ak kóolute gu mag.
forti di tale speranza, ci comportiamo con molta franchezz
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
moom nag muy déglu pool miy waare. noonu pool xool ko jàkk, gis ne, am na ngëm ngir wér.
egli ascoltava il discorso di paolo e questi, fissandolo con lo sguardo e notando che aveva fede di esser risanato
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
fàttalikul yeesu kirist mi dekki, soqikoo ci daawuda, tukkee ci xebaar bu baax bi may waare.
ricordati che gesù cristo, della stirpe di davide, è risuscitato dai morti, secondo il mio vangelo
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
yónniwaale nanu ak moom mbokk, mi am tur wu rafet ci mboolooy ñi gëm ñépp ndax li muy waare xebaaru kirist.
con lui abbiamo inviato pure il fratello che ha lode in tutte le chiese a motivo del vangelo
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
ndaxte yeesu kirist boroom bi lanuy waare, waaye waarewunu lu jëm ci sunu bopp. nun seeni jaam lanu ndax yeesu.
noi infatti non predichiamo noi stessi, ma cristo gesù signore; quanto a noi, siamo i vostri servitori per amore di gesù
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
musunoo jey kenn, yéen xam ngeen ko; sunu waare musul a ëmb bëgge, yàlla seede na ko;
mai infatti abbiamo pronunziato parole di adulazione, come sapete, né avuto pensieri di cupidigia: dio ne è testimone
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
li jëm ci njiiti mbooloo mi nag, joxal teraanga ju mat sëkk ñi ciy rafetal seen liggéey, rawatina ñi sax dàkk ci waare bi ak njàngale mi.
i presbiteri che esercitano bene la presidenza siano trattati con doppio onore, soprattutto quelli che si affaticano nella predicazione e nell'insegnamento
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
te loolu lépp a ngi sosoo ci yàlla, mi nu jubale ak boppam jaare ko ci yeesu kirist, te sas nu nuy waare juboo googu:
tutto questo però viene da dio, che ci ha riconciliati con sé mediante cristo e ha affidato a noi il ministero della riconciliazione
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
ngir li yonent yàlla esayi waxoon am:«boroom bi, ana ku gëm sunu waare?kan la boroom bi won dooleem?»
perché si adempisse la parola detta dal profeta isaia: e il braccio del signore a chi è stato rivelato
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
waaye yeesu tontu leen: «nanu dem feneen ci dëkk yi nu wër, ma waare fa itam, ndaxte moo tax ma génn.»
egli disse loro: «andiamocene altrove per i villaggi vicini, perché io predichi anche là; per questo infatti sono venuto!»
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
kon gannaaw yàlla séddale na ay mayam, ku nekk ak sa cér, nanu koy jëfandikoo. ku yàlla may, ngay waare kàddoom, nga wax ko kem sa ngëm;
abbiamo pertanto doni diversi secondo la grazia data a ciascuno di noi. chi ha il dono della profezia la eserciti secondo la misura della fede
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
am na ñuy waare ci turu kirist ci kaw kiñaan ak xëccoo, waaye ñi ci des ci kaw cofeel ak xol bu laab, ndaxte xam nañu ne, yàlla moo ma teg fii, ngir ma taxawal xebaar bu baax bi.
alcuni, è vero, predicano cristo anche per invidia e spirito di contesa, ma altri con buoni sentimenti
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
te it jeggalul àddina su jëkk sa weddi woon, ba xooj ko ci ndoxu mbënn ma, waaye musal na nóoyin rekk, mi daan waare ci njub, moom ak juróom-ñaari nit.
non risparmiò il mondo antico, ma tuttavia con altri sette salvò noè, banditore di giustizia, mentre faceva piombare il diluvio su un mondo di empi
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
kon nag yaw miy jàngal say moroom, xanaa doo jàngal sa bopp? yaw miy waare di tere sàcc, mbaa doo sàcc yaw itam? yaw miy tere njaaloo, mbaa doo njaaloo?
ebbene, come mai tu, che insegni agli altri, non insegni a te stesso? tu che predichi di non rubare, rubi
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
te it dunu noppee sant yàlla ci lii: ba ngeen jotee kàddug yàlla, gi nu doon waare, nangu ngeen ko, waxuma ni kàddug nit waaye ni kàddug yàlla, ndaxte moom la ci dëgg-dëgg, te mu ngi jëf ci yéen ñi gëm.
proprio per questo anche noi ringraziamo dio continuamente, perché, avendo ricevuto da noi la parola divina della predicazione, l'avete accolta non quale parola di uomini, ma, come è veramente, quale parola di dio, che opera in voi che credete
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità: