検索ワード: abrahamu (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

tuseme nini basi, juu ya abrahamu baba yetu?

ウォロフ語

sunu maam ibraayma, mi nu soqikoo; nu mbiram tëdde?

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kiapo alichomwapia abrahamu baba yetu, ni kwamba atatujalia sisi

ウォロフ語

di ngiñ, li mu giñaloon sunu maam ibraayma naan,

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kama alivyowaahidia wazee wetu abrahamu na wazawa wake hata milele."

ウォロフ語

ni mu ko dige woon sunuy maam,jëmale ko ci ibraayma ak askanam ba fàww.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

basi, wale walio na imani wanabarikiwa pamoja na abrahamu aliyeamini.

ウォロフ語

kon ñi gëm, yàlla dina leen barkeel, sukkandikoo ko ci seen ngëm, ni mu defal ibraayma, boroom ngëm.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

abrahamu alisubiri kwa uvumilivu na hivyo alipokea kile alichoahidiwa na mungu.

ウォロフ語

noonu ibraayma di xaar tey muñ, ba jot li ko yàlla digoon.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

sasa basi jueni kwamba watu wenye kumwamini ndio walio watoto halisi wa abrahamu.

ウォロフ語

xamleen boog ne, boroom ngëm yi rekk ñooy doomi ibraayma.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

abrahamu alimzaa isaka, isaka alimzaa yakobo, yakobo alimzaa yuda na ndugu zake,

ウォロフ語

ibraayma moo jur isaaxa; isaaxa jur yanqóoba; yanqóoba jur yuda ak i doomi baayam;

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, wayahudi wakamwambia, "wewe hujatimiza miaka hamsini bado, nawe umemwona abrahamu?"

ウォロフ語

yawut ya ne ko: «amaguloo juróom-fukki at, ba noppi naan gis nga ibraayma?»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

chukueni kwa mfano habari za abrahamu: yeye alimwamini mungu, naye mungu akamkubali kuwa mwadilifu.

ウォロフ語

xool-leen ci ibraayma; mbind mi wax na ne:«ibraayma gëm na yàlla,te yàlla jàppe ngëmam ni njub.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

abrahamu hakuionea mashaka ile ahadi ya mungu; alipata nguvu kutokana na imani, akamtukuza mungu.

ウォロフ語

waaye loolu taxul ngëmadi jàpp ko, ba muy werante ci waxu yàlla; ngëmam sax di gën a dëgër, mu daldi sant yàlla,

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, mwaona jinsi mtu huyu alivyokuwa maarufu. baba abrahamu alimpa sehemu moja ya kumi ya vitu vyote alivyoteka vitani.

ウォロフ語

seetleen ni mu màgge, moom melkisedeg! ibraayma sax, maamu cosaan mi, fab na li mu jële woon lépp ca xare ba, jox melkisedeg asaka ja.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

abrahamu aliamini kwamba mungu anaweza kuwafufua wafu: na kwa namna fulani kweli abrahamu alimpata tena mwanae kutoka wafu.

ウォロフ語

waaye xelu ibraayma jàppoon na ne, yàlla am na dooley dekkal néew yi. te dëgg-dëgg ci misaal dafa mel ni, isaaxa dafa dee te dekki.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"wakati ulipotimia mungu aitimize ahadi aliyompa abrahamu, idadi ya wale watu kule misri ilikwisha ongezeka na kuwa kubwa zaidi.

ウォロフ語

«bi loolu wéyee jamono ji jege woon na, ngir yàlla amal li mu digoon ibraayma ci ngiñ; fekk xeet wa di law tey gën a bare ci misra,

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

je, abrahamu baba yetu alipataje kukubalika mbele yake mungu? kwa matendo yake, wakati alipomtoa mwanae isaka sadaka juu ya madhabahu.

ウォロフ語

sunu maam ibraayma, ndax du ci kaw jëf la ko yàlla àttee ni ku jub, ci li mu joxe doomam isaaxa ni sarax?

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"ikatokea kwamba huyo maskini akafa, malaika wakamchukua, wakamweka karibu na abrahamu. na yule tajiri pia akafa, akazikwa.

ウォロフ語

«noonu miskin ma dee, malaaka yi yóbbu ko ca wetu ibraayma. boroom alal ja itam dee, ñu suul ko.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

je, wao ni waebrania? hata mimi. je, wao ni waisraeli? hata mimi. wao ni wazawa wa abrahamu? hata mimi.

ウォロフ語

ndax ibrë lañu? man it ibrë laa. ndax bànni israyil lañu? man itam ci laa. ndax sëti ibraayma lañu? man itam moom laa.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

aliwaambia, mimi ni mungu wa abrahamu, isaka na yakobo! basi, yeye si mungu wa wafu, bali ni mungu wa walio hai."

ウォロフ語

“maay yàllay ibraayma ak yàllay isaaxa ak yàllay yanqóoba”? li ciy génn mooy, nekkul yàllay ñi dee waaye yàllay ñiy dund la.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

basi, kulikuwa na vizazi kumi na vinne tangu abrahamu mpaka daudi, vizazi kumi na vinne tangu daudi mpaka wayahudi walipochukuliwa mateka babuloni, na vizazi kumi na vinne tangu kuchukuliwa mateka mpaka wakati wa kristo.

ウォロフ語

mboolem giir googu nag, la dale ca ibraayma ba ca daawuda, fukk lañu ak ñeent; la dale ca daawuda ba ca njaam ga ca babilon, fukk lañu ak ñeent; la dale njaam ga ca babilon ba ci kirist, fukk lañu ak ñeent.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kwa imani, abrahamu alimtoa mwanae isaka sadaka wakati mungu alipomjaribu. huyo abrahamu ndiye aliyekuwa amepokea ahadi ya mungu, lakini, hata hivyo, alikubali kumtoa dhabihu mwanae wa pekee,

ウォロフ語

ngëm moo tax ibraayma naroon a rey isaaxa ni sarax, bi ko yàlla nattoo. moom mi jotoon dige yi, moo demoon bay saraxe jenn doom ji mu am kepp,

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

ahadi zile mungu alizotoa kwa njia ya manabii ni kwa ajili yenu; na mnashiriki lile agano mungu alilofanya na babu zenu, kama alivyomwambia abrahamu: kwa njia ya wazawa wako, jamaa zote za dunia zitabarikiwa.

ウォロフ語

yéen nag yéenay donn yonent yi ak kóllëre, gi yàlla fasoon ak seeni maam, bi mu naan ibraayma: “xeeti àddina yépp dinañu barkeel ci ki soqikoo ci yaw.”

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

人による翻訳を得て
7,739,886,436 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK