検索ワード: afadhali (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

afadhali uwaage watu waende mashambani na katika vijiji vya jirani, wanunue chakula."

ウォロフ語

yiwil mbooloo mi nag, ñu dugg ci àll bi ak dëkk yi nu wër, jënd lu ñu lekk.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

iliyobakia ni afadhali kwenu kumsamehe mtu huyo na kumpa moyo ili asije akahuzunika mno na kukata tamaa kabisa.

ウォロフ語

léegi nag baal-leen ko te dëfël xolam, ngir bañ mu sóobu ci naqar wu ëpp.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

afadhali kuacha kula nyama, kunywa divai, au kufanya chochote ambacho chaweza kumsababisha ndugu yako aanguke.

ウォロフ語

liy sa warugar mooy nga bañ a fiir sa moroom ci yàpp mbaa ci biiñ mbaa ci leneen lu mu man a doon.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

ingekuwa afadhali kwake kufungiwa shingoni jiwe kubwa la kusagia na kutoswa baharini, kuliko kumkwaza mmoja wa wadogo hawa.

ウォロフ語

Ñu takk doj wu réy ci baatam, sànni ko ci géej moo gën ci moom muy daaneel ci bàkkaar kenn ci ñi gën a tuuti ci ñii.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

hata hivyo, kama mtu hawezi kujizuia basi, na aoe; maana ni afadhali zaidi kuoa kuliko kuwaka tamaa.

ウォロフ語

waaye su ngeen mënul a téye seen bopp, nangeen séy, ndaxte séy moo gën xemmem di leen gaañ.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

nayajua mambo yako yote! najua kwamba wewe si baridi wala si moto. afadhali ungekuwa kimojawapo: baridi au moto.

ウォロフ語

xam naa say jëf, xam ne seddoo, tàngoo. manoon ngaa sedd mbaa nga tàng,

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"yeyote atakayemkosesha mmoja wa hawa wadogo wanaoniamini, ingekuwa afadhali afungwe shingoni jiwe kubwa la kusagia na kuzamishwa kwenye kilindi cha bahari.

ウォロフ語

waaye ku yóbbe bàkkaar kenn ci ñi gën a tuuti ñi ma gëm, li gën ci moom mooy ñu takk doj wu réy ci baatam, sànni ko ca fa gën a xóot ca géej ga.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

"mtu yeyote atakayemfanya mmoja wa hawa wadogo wanaoniamini atende dhambi, ingekuwa afadhali kwa mtu huyo kufungiwa shingoni mwake jiwe kubwa la kusagia na kutupwa baharini.

ウォロフ語

«waaye ku yóbbe bàkkaar kenn ci ñi gën a tuuti ñi ma gëm, li gën ci moom, moo di ñu takk doj wu réy ci baatam, sànni ko ci géej.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

mwanamke asiyefunika kichwa chake, afadhali anyoe nywele zake. lakini ni aibu kwa mwanamke kukatwa nywele zake au kunyolewa; basi, afadhali afunike kichwa chake.

ウォロフ語

jigéen ju dul musóoru, bu yaboo, mu watu. waaye su fekkee ne jigéen dafay am kersa, su wàññee kawaram walla mu watu, fàww kon mu musóoru.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kweli mwana wa mtu anakwenda zake kama maandiko matakatifu yanavyosema juu yake; lakini, ole wake mtu yule anayemsaliti mwana wa mtu! ingalikuwa afadhali kwa mtu huyo kama hangalizaliwa!"

ウォロフ語

doomu nit ki mu ngi dem, ni ñu ko waxe ci mbind mi, waaye ki koy wor dina torox. bañoon a juddu moo gën ci moom.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

na jicho lako likikukosesha, ling'oe! afadhali kuingia katika utawala wa mungu ukiwa na jicho moja tu, kuliko kuwa na macho yako yote mawili na kutupwa katika moto wa jehanamu.

ウォロフ語

te bu la sa bët di yóbbe bàkkaar, luqi ko. nga patt te dugg ci nguuru yàlla, moo gën ci yaw, nga am ñaari bët, ñu sànni la ci safara.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"kama mkono au mguu wako ukikukosesha, ukate na kuutupa mbali nawe. ni afadhali kwako kuingia katika uzima bila mkono au mguu, kuliko kutupwa katika moto wa milele ukiwa na mikono miwili na miguu yako miwili.

ウォロフ語

boo xamee ne sa loxo mbaa sa tànk mu ngi lay yóbbe bàkkaar, dagg ko, sànni ko fu sore. ndaxte nga lafañ walla ñàkk loxo te dugg ci dund gu wóor gi, moo gën ci yaw, nga am ñaari loxo walla ñaari tànk, te ñu sànni la ci safara su dul fey mukk.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

baada ya kukaa muda mrefu bila kula chakula, paulo alisimama kati yao, akasema, "waheshimiwa, ingalikuwa afadhali kama mngalinisikiliza na kuacha kusafiri kutoka krete. kama mngalifanya hivyo tungaliiepuka shida hii na hasara hizi zote.

ウォロフ語

bi loolu di xew, fekk gëj nañoo lekk, pool daldi taxaw ci seen biir ne leen: «gaa ñi, li gënoon mooy ngeen déglu ma te bañ a jóge kereet, ba indil seen bopp musiba ak kasara ju réy jii.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

人による翻訳を得て
7,763,728,854 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK