プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。
lakini yesu akamshika mkono, akamwinua, naye akasimama.
waaye yeesu jàpp loxoom, jógloo ko, xale bi daldi taxaw.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
lakini yesu akamshika mkono akasema, "mtoto amka!"
waaye yeesu jàpp loxob janq ba, woo ko ne ko: «xale bi, jógal.»
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
警告:見えない HTML フォーマットが含まれています
lakini wao wakakaa kimya. yesu akamshika huyo mgonjwa, akamponya, akamwacha aende zake.
waaye ñépp ne cell. yeesu daldi laal jarag ja, faj ko, ba noppi ne ko mu ñibbi.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
yesu akamwendea huyo mama, akamshika mkono, akamwinua. na ile homa ikamwacha, akaanza kuwatumikia.
mu ñëw nag ci moom, jàpp loxoom, yékkati ko. noonu tàngoor wi daldi wàcc, te soxna si di leen topptoo.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
basi, umati wa watu ulipoondolewa, yesu aliingia ndani, akamshika huyo msichana mkono, naye akasimama.
waaye ñu génne leen, yeesu dugg, jàpp loxob janq ba, mu daldi jóg.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
hapo, yesu akaunyosha mkono wake, akamshika na kumwambia, "ewe mwenye imani haba! kwa nini uliona shaka?"
ca saa sa yeesu tàllal loxoom, jàpp ko naan: «yaw mi néew ngëm, lu tax nga am xel ñaar?»
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
警告:見えない HTML フォーマットが含まれています
kisha akamshika mkono, akamwambia, "talitha, kumi," maana yake, "msichana, nakwambia, amka!"
mu jàpp loxoom ne ko: «talita kumi,» liy tekki: «janq bi, maa ngi la koy wax, jógal.»
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
警告:見えない HTML フォーマットが含まれています
yesu akamshika mkono huyo kipofu, akampeleka nje ya kijiji. akamtemea mate machoni, akamwekea mikono, akamwuliza, "je, unaweza kuona kitu?"
yeesu nag jàpp loxob gumba gi, yóbbu ko, ba génn dëkk bi. mu def tiflit ciy bëtam, teg ko loxo naan: «ndax gis nga dara?»
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
警告:見えない HTML フォーマットが含まれています