プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。
basi, roho akanikumba, naye malaika akanipeleka juu ya mlima mrefu sana. akanionyesha mji mtakatifu, ukishuka kutoka kwa mungu mbinguni,
noonu xelum yàlla solu ma, malaaka ma yóbbu ma ci kaw tund wu réy-a-réy. noonu mu won ma yerusalem, dëkk bu sell bi, muy wàcce ci asamaan, jóge ca wetu yàlla,
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
kisha, roho akanikumba, akaniongoza mpaka jangwani. huko nikamwona mwanamke ameketi juu ya mnyama mwekundu. mnyama huyo alikuwa ameandikwa kila mahali majina ya makufuru; alikuwa na vichwa saba na pembe kumi.
noonu xelum yàlla solu ma, malaaka ma yóbbu ma ca màndiŋ ma. foofa ma gis fa jigéen ju war rab wu xonq te am juróom-ñaari bopp ak fukki béjjén, yaram wa fees ak turi xarab yàlla.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質: