検索ワード: nifuate (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

lakini yesu akamwambia, "nifuate! waache wafu wazike wafu wao."

ウォロフ語

yeesu tontu ko ne: «toppal ci man te bàyyi ñi dee, ñu suul seeni néew.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

kesho yake yesu aliamua kwenda galilaya. basi, akamkuta filipo, akamwambia, "nifuate."

ウォロフ語

ca ëllëg sa mu fas yéenee dem diiwaanu galile te mu gis filib. yeesu ne ko: «toppal ci man.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

baada ya hayo, yesu akatoka nje, akamwona mtoza ushuru mmoja aitwaye lawi, ameketi ofisini. yesu akamwambia, "nifuate!"

ウォロフ語

gannaaw loolu yeesu génn, gis ab juutikat bu tudd lewi, mu toog ca juuti ba. mu ne ko: «kaay topp ci man.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

(kwa kusema hivyo, alionyesha jinsi petro atakavyokufa na kumtukuza mungu.) kisha akamwambia, "nifuate."

ウォロフ語

ci baat yooyu la yeesu doon misaale nan la piyeer war a faatoo ngir jollil ndamu yàlla. noonu yeesu ne ko: «toppal ci man!»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

alipokuwa akipita, akamwona lawi mwana wa alfayo, ameketi katika ofisi ya ushuru. yesu akamwambia, "nifuate!" lawi akasimama, akamfuata.

ウォロフ語

bi yeesu di romb, mu gis ku ñuy wax lewi, doomu alfe, toog ca juuti ba. yeesu ne ko: «kaay topp ci man.» mu jóg, daldi topp ci moom.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

kisha akamwambia mtu mwingine, "nifuate." lakini huyo akasema, "bwana, niruhusu kwanza niende kumzika baba yangu."

ウォロフ語

yeesu ne keneen: «toppal ci man.» waaye kooku ne ko: «sang bi, may ma, ma jëkk a dem suuli sama baay.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

yesu aliondoka hapo, na alipokuwa anakwenda zake, alimwona mtu mmoja aitwaye mathayo, ameketi katika ofisi ya ushuru. basi, yesu akamwambia, "nifuate." naye mathayo akainuka, akamfuata.

ウォロフ語

bi yeesu jógee foofa, mu gis nit ku tudd macë, toog ca juuti ba. yeesu ne ko: «kaay topp ma.» noonu macë jóg, daldi ko topp.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

人による翻訳を得て
7,753,737,588 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK