プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。
watu wote wa mji ule wakakusanyika nje ya mlango.
ba dëkk bi bépp dajaloo ci buntu kër gi.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
wale mitume walirudi, wakakusanyika mbele ya yesu wakamwarifu yote waliyotenda na kufundisha.
gannaaw loolu ndaw yi dajaloo ci wetu yeesu, nettali li ñu def ak li ñu jàngale lépp.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
lakini habari za yesu zilizidi kuenea kila mahali. watu makundi mengi wakakusanyika ili kumsikiliza na kuponywa magonjwa yao.
noonu turu yeesu di gën a siiw. mbooloo mu bare di ñëw ci moom, ngir déglu ko te mu faj seeni jàngoro.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質: