検索ワード: chini (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

basi, yesu akawaamuru watu wakae chini.

ウォロフ語

ci kaw loolu yeesu sant mbooloo mi, ñu toog ci suuf.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kama mkiongozwa na roho, basi, hamko tena chini ya sheria.

ウォロフ語

waaye bu ngeen toppee xelum yàlla, nekkatuleen ci kilifteefu yoon wi.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, jiwekeni chini ya mungu; mpingeni ibilisi naye atawakimbieni.

ウォロフ語

kon nag wàkkirluleen ci yàlla, waaye dàqleen seytaane, te dina daw, ba sore leen.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

huko anangoja mpaka adui zake watakapowekwa kama kibao chini ya miguu yake.

ウォロフ語

di xaar ba kera mu daaneel ko ay noonam ci kanamam.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, pazia la hekalu likapasuka vipande viwili toka juu mpaka chini.

ウォロフ語

bi mu ko defee ridob bérab bu sell ba ca kër yàlla ga xar ñaar, li dale ci kaw ba ci suuf.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

akajitupa chini mbele ya miguu ya yesu huku akimshukuru. huyo alikuwa msamaria.

ウォロフ語

mu dëpp jëwam ca tànki yeesu, di ko gërëm. fekk nitu samari la woon.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

ndiyo maana mungu amewaweka chini ya nguvu ya upotovu, wauamini uongo.

ウォロフ語

looloo tax yàlla yónnee leen xelum réer, ba ñu gëm fen.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, nyenyekeeni chini ya mkono wa enzi wa mungu, ili awainue wakati ufaao.

ウォロフ語

suufeel-leen seen bopp kon ci ron loxob yàlla bu am kàttan, ngir mu yékkati leen ci jamono ju ko soob.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

aliona mbingu zimefunguliwa na kitu kama shuka kubwa inateremshwa chini ikiwa imeshikwa pembe zake nne.

ウォロフ語

mu xool asamaan ubbiku, gis lu mel ni sér bu mag bu ñu téye ci ñeenti laf ya, yoor ko, mu jëm suuf.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

baada ya kusema hayo, akatema mate chini, akafanyiza tope, akampaka yule kipofu machoni,

ウォロフ語

bi yeesu waxee loolu ba noppi, dafa daldi tifli, jaxase lor wa ak ban, tay ko ci bëti gumba ga ne ko:

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

baada ya kupigwa sana wakatiwa ndani, na askari wa gereza akaamriwa kuwaweka chini ya ulinzi mkali.

ウォロフ語

noonu ñu dóor leen ay yar yu bare, tëj leen, sant boroom kaso ba, mu wottu leen bu wér.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

anania aliposikia hayo, akaanguka chini, akafa. watu wote waliosikia habari ya tukio hilo waliogopa sana.

ウォロフ語

bi anañas déggee baat yooyu, mu daanu dee. Ñi ko dégg ñépp tiit, ba ne nërëm.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

akaanguka chini na kusikia sauti ikimwambia: "saulo, saulo! kwa nini unanitesa?"

ウォロフ語

mu daanu ci suuf, dégg baat bu ko ne: «sool, sool, lu tax nga di ma fitnaal?»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

akaenda mbele kidogo, akajitupa chini kifudifudi, akasali kwamba, kama ingewezekana, asiipitie saa hiyo ya mateso.

ウォロフ語

noonu yeesu dem ci kanam tuuti, daanu ci suuf, di ñaan ne, waxtu wi teggi ko, bu loolu manoon a am.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

hapo pazia la hekalu likapasuka vipande viwili, toka juu mpaka chini; nchi ikatetemeka; miamba ikapasuka;

ウォロフ語

ca saa sa ridob bérab bu sell ba ca kër yàlla ga xar ñaar, li dale ci kaw ba ci suuf; suuf si yengu, doj yi toj, bàmmeel yi ubbiku,

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

hao wanawake wakaingiwa na hofu, wakainama chini. ndipo wale watu wakawaambia, "kwa nini mnamtafuta aliye hai kati ya wafu?

ウォロフ語

jigéen ña am tiitaange ju mag, daldi dëpp seen jë ci suuf. waaye ñu ne leen: «lu tax ngeen di seet kiy dund ci biir néew yi?

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

akiwa katika uchungu mkubwa, alisali kwa bidii zaidi; na jasho likamtoka, kama matone ya damu, likatiririka mpaka chini.

ウォロフ語

ci biir tiis, yeesu gën a sawar ci ñaan gi, ñaqam mel ni lumbi deret dal ci suuf.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

("mnajua kwamba yeye alinunua shamba kwa zile fedha alizopata kutokana na kitendo chake kiovu. akaanguka chini, akapasuka na matumbo yake yakamwagika nje.

ウォロフ語

--pey gi yudaa jotoon ci ñaawteefam, mu jënd ci tool, daanu fa, ba fàcc, ay buttitam tuuru.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

"na sasa basi, ninawaweka ninyi chini ya ulinzi wa mungu na ujumbe wa neema yake. yeye anao uwezo wa kuwajenga ninyi na kuwawezesha mzipate zile baraka alizowawekea watu wake.

ウォロフ語

«léegi nag maa ngi leen di dénk boroom bi, moom ak kàddug yiwam, gi leen man a dëgëral te may leen cér ci biir gaayi yàlla yu sell yépp.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

hapo huyo pepo alipaaza sauti, akamwangusha huyo mtoto chini, kisha akamtoka. mtoto alionekana kama maiti, hata wengine walisema, "amekufa!"

ウォロフ語

noonu rab wa daldi yuuxu, sayloo xale bi, génn. xale bi ne nemm, mel ni ku dee, ba tax ñu bare ne: «dee na.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

人による翻訳を得て
7,800,448,730 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK