검색어: habari gani? (스와힐리어 - 월로프어)

인적 기여

전문 번역가, 번역 회사, 웹 페이지 및 자유롭게 사용할 수 있는 번역 저장소 등을 활용합니다.

번역 추가

스와힐리어

월로프어

정보

스와힐리어

habari

월로프어

xibaar

마지막 업데이트: 2014-08-15
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

akawaamuru wasiwaambie watu habari zake,

월로프어

te mu dénk leen bu wóor, ñu bañ koo siiwal.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

wakawa wanahubiri habari njema huko.

월로프어

foofa ñu di fa xamle xebaar bu baax bi.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

habari hiyo ikavuma sana katika nchi ile yote.

월로프어

noonu xebaaru li mu def daldi siiw ca réew ma.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

habari zake zikaenea mahali pote katika mkoa ule.

월로프어

noonu turam siiw ca diiwaan bépp.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

halafu yesu akawaamuru wasimwambie mtu yeyote habari hiyo.

월로프어

noonu yeesu daldi leen dénk, tere leen ñu wax ko kenn,

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

habari njema ya yesu kristo, mwana wa mungu.

월로프어

xebaar bu baaxu yeesu kirist, doomu yàlla, nii la tàmbalee.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

wote waliosikia hayo walishangaa juu ya habari walizoambiwa na wachungaji.

월로프어

Ñi dégg li sàmm yi doon wax ñépp daldi waaru lool.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

lakini lazima kwanza habari njema ihubiriwe kwa mataifa yote.

월로프어

fàww xebaar bu baax bi jëkk a jib ci xeet yépp.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

habari hizo zikaenea kote katika uyahudi na katika nchi za jirani.

월로프어

la ñu wax ci mbiri yeesu daldi siiw ca réewu yawut ya ak la ko wër yépp.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

habari za yesu zikaenea upesi kila mahali katika wilaya ya galilaya.

월로프어

noonu turam daldi siiw ci diiwaani galile gépp.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

ndiyo maana namtuma, ili aichangamshe mioyo yenu kwa kuwaambieni habari zetu.

월로프어

lii moo tax ma yebal ko ci yéen: ngeen xam xebaar bi jóge ci nun, te it mu dëfël seen xol.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

maana, kama habari njema tunayohubiri imefichika, imefichika tu kwa wale wanaopotea.

월로프어

su fekkee ne sax, xebaar bu baax bi dafa muuru ci ñenn ñi, dafa fekk ñoom ñu aw yoon wu jëm ci sànkute.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

ama mtu atatoa kitu gani badala ya maisha yake?

월로프어

te nit, lu mu war a weccee bakkanam?

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

wanafunzi wa yohane walipopata habari, walikwenda wakachukua mwili wake, wakauzika kaburini.

월로프어

ba taalibey yaxya déggee loolu, ñu ñëw, fab néew ba, suul ko ci bàmmeel.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

ndugu, tunapenda kuwapa habari juu ya neema ambazo mungu ameyajalia makanisa ya makedonia.

월로프어

gannaaw loolu bokk yi, danu leen a bëgg a xamal li yiwu yàlla jur ci biir mboolooy ñi gëm te nekk ci diiwaanu maseduwan.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

kristo anawezaje kupatana na shetani? muumini ana uhusiano gani na asiyeamini?

월로프어

gan déggoo moo man a am diggante kirist ak beliyar? gan jaxasoo moo man a am diggante ki gëm ak ki gëmul?

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

"wakati umetimia, na ufalme wa mungu umekaribia. tubuni na kuiamini habari njema!"

월로프어

naan: «jamono ji mat na, nguuru yàlla jegesi na; tuubleen seeni bàkkaar te gëm xebaar bu baax bi.»

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

스와힐리어

basi, myahudi ana nini zaidi kuliko watu wengine? au kutahiriwa kuna faida gani?

월로프어

yawut bi nag, ci lan la rawe ku dul yawut? te xaraf lu muy njariñ?

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

(kwa kusema hivyo alionyesha atakufa kifo gani).

월로프어

ci baat yooyu la doon misaale ni mu war a faatoo.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

인적 기여로
7,739,409,183 더 나은 번역을 얻을 수 있습니다

사용자가 도움을 필요로 합니다:



당사는 사용자 경험을 향상시키기 위해 쿠키를 사용합니다. 귀하께서 본 사이트를 계속 방문하시는 것은 당사의 쿠키 사용에 동의하시는 것으로 간주됩니다. 자세히 보기. 확인