검색어: makabila (스와힐리어 - 월로프어)

인적 기여

전문 번역가, 번역 회사, 웹 페이지 및 자유롭게 사용할 수 있는 번역 저장소 등을 활용합니다.

번역 추가

스와힐리어

월로프어

정보

스와힐리어

kisha nikasikia idadi ya hao waliopigwa mhuri: watu mia moja arobaini na nne elfu wa makabila yote ya watu wa israeli.

월로프어

noonu ma dégg limub ñi ñu màndargaal; ñu tollu ci téeméer ak ñeent-fukk ak ñeent ci ay junni. Ñu jóge ci giiri bànni israyil yépp:

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

mtakula na kunywa mezani pangu katika ufalme wangu, na mtaketi katika viti vya enzi kuyahukumu makabila kumi na mawili ya israeli.

월로프어

dingeen lekkandoo te naanandoo ak man ci sama nguur. te dingeen toog ci jal yi, di àtte fukki giir ak ñaar yu bànni israyil.»

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

mimi yakobo, mtumishi wa mungu na wa bwana yesu kristo, nawaandikia ninyi, makabila kumi na mawili, yaliyotawanyika ulimwenguni! salaam!

월로프어

man saag, jaamu yàlla ak boroom bi yeesu kirist, maa leen di nuyu, yéen fukki giir ak ñaar, yi tasaaroo ci biir àddina si.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

ahadi hiyo ndiyo ileile inayotumainiwa na makabila kumi na mawili ya taifa letu, wakimtumikia mungu kwa dhati mchana na usiku. mheshimiwa mfalme, wayahudi wananishtaki kwa sababu ya tumaini hilo!

월로프어

dige booba la fukki giir ak ñaar yu bànni israyil di sàkku, ngir jot ko, ci jaamu yàlla ak cawarte guddi ak bëccëg. yaw buur, yaakaar joojoo tax ñu may kalaame, ñoom yawut yi.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

yesu akawaambia, "nawaambieni kweli, mwana wa mtu atakapoketi katika kiti cha enzi cha utukufu wake katika ulimwengu mpya, ninyi mlionifuata mtaketi katika viti kumi na viwili mkiyahukumu makabila kumi na mawili ya israeli.

월로프어

yeesu ne leen: «ci dëgg maa ngi leen koy wax, bés baa ngi ñëw bu yàllay yeesalaat lépp, te doomu nit ki toog ci jalam, bi soloo ndam. bés boobu nag, yéen ñi ma topp dingeen toog ci fukki jal ak ñaar, di àtte fukki giir ak ñaar yu bànni israyil.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

인적 기여로
7,740,589,865 더 나은 번역을 얻을 수 있습니다

사용자가 도움을 필요로 합니다:



당사는 사용자 경험을 향상시키기 위해 쿠키를 사용합니다. 귀하께서 본 사이트를 계속 방문하시는 것은 당사의 쿠키 사용에 동의하시는 것으로 간주됩니다. 자세히 보기. 확인