검색어: uhusiano (스와힐리어 - 월로프어)

인적 기여

전문 번역가, 번역 회사, 웹 페이지 및 자유롭게 사용할 수 있는 번역 저장소 등을 활용합니다.

번역 추가

스와힐리어

월로프어

정보

스와힐리어

kristo anawezaje kupatana na shetani? muumini ana uhusiano gani na asiyeamini?

월로프어

gan déggoo moo man a am diggante kirist ak beliyar? gan jaxasoo moo man a am diggante ki gëm ak ki gëmul?

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

muwe na hekima katika uhusiano wenu na watu wasioamini, mkitumia vizuri kila nafasi mliyo nayo.

월로프어

jëfeleen ak xel ci seen diggante ak waa àddina, te fu ngeen ame jot, fexeleen ba jariñoo ko.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

huenda kwamba huko kuna mtu ambaye hatautii huu ujumbe tunaowapelekeeni katika barua hii. ikiwa hivyo, basi, mfichueni mtu huyo na msiwe na uhusiano wowote naye kusudi aone aibu.

월로프어

su kenn bañee topp li nu bind ci bataaxal bii, ràññeeleen ko te sore ko, ngir mu rus ci.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

lakini wengine walikuwa wakaidi, wakakataa kuamini, wakaanza kuongea vibaya hadharani juu ya njia ya bwana. hapo paulo alivunja uhusiano nao, akawachukua pembeni wale wanafunzi wake, akawa anazungumza nao kila siku katika jumba la masomo la turano.

월로프어

waaye bi xolu ñenn ci ñoom fattee, ñu gëmadi, bay suufeel yoon wi ci kanam mbooloo ma, mu jóge ci ñoom, xàjjale taalibe yi ak ñoom, di diisoo bés bu nekk ca jàngukaayu ku ñuy wax tiranus.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

hekalu la mungu lina uhusiano gani na sanamu za uongo? maana sisi ni hekalu la mungu aliye hai. kama mungu mwenyewe alivyosema: "nitafanya makao yangu kwao, na kuishi kati yao; nitakuwa mungu wao, nao watakuwa watu wangu."

월로프어

nan la këru yàlla man a mànkoo ak xërëm yi? ndaxte nun nooy këru yàlla aji dund ji, ni ko yàlla waxe:«dinaa dëkk ci seen biir,tey dox ànd ak ñoom,ma nekk seen yàlla,ñuy samay gaay.»

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

인적 기여로
7,735,143,743 더 나은 번역을 얻을 수 있습니다

사용자가 도움을 필요로 합니다:



당사는 사용자 경험을 향상시키기 위해 쿠키를 사용합니다. 귀하께서 본 사이트를 계속 방문하시는 것은 당사의 쿠키 사용에 동의하시는 것으로 간주됩니다. 자세히 보기. 확인