전문 번역가, 번역 회사, 웹 페이지 및 자유롭게 사용할 수 있는 번역 저장소 등을 활용합니다.
ndaxte ndam li amoon keroog suux na ci ndam li ko raw léegi.
ያ የከበረ እንኳ እጅግ በሚበልጠው ክብር ምክንያት በዚህ ነገር ክብሩን አጥቶአልና።
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
maa ngi sant yàlla ci li may wax ay làkk, ba raw leen yéen ñépp.
ከሁላችሁ ይልቅ በልሳኖች እናገራለሁና እግዚአብሔርን አመሰግናለሁ፤
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
bi loolu amee xarekat ya bëgg a rey ñi ñu tëj, ngir ragal ñenn ñi féey, ba raw.
ወታደሮቹም ከእስረኞች አንድ ስንኳ ዋኝቶ እንዳያመልጥ ይገድሉአቸው ዘንድ ተማከሩ።
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
Ñoom ñaar ñépp a ngi doon daw, waaye beneen taalibe ba raw piyeer, jëkk ko ca bàmmeel ba.
ሁለቱም አብረው ሮጡ፤ ሌላው ደቀ መዝሙርም ከጴጥሮስ ይልቅ ፈጥኖ ወደ ፊት ሮጠና አስቀድሞ ከመቃብሩ ደረሰ፤
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
waaye xamuñu woon lan lañu man a def, ndaxte nit ñépp a ngi ko doon déglu, bañ benn baat raw leen.
የሚያደርጉበትንም አጡ፤ ሕዝቡ ሁሉ ሲሰሙት ተንጠልጥለውበት ነበርና።
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
waaye ci kaw loolu dawalkati gaal ga taafantaloo sànniji ay diigal ca boppu gaal ga, fekk dañuy fexee jël looco ga, ba raw.
መርከበኞቹም ከመርከቡ ይሸሹ ዘንድ ፈልገው ከመርከቡ በስተ ፊት መልሕቅ መጣል እንዳላቸው አመካኝተው ታንኳይቱን ወደ ባሕር ባወረዱ ጊዜ፥
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
looloo tax bi muy wàcc àddina, kirist nee na:«bëggoo saraxu mala walla beneen sarax,waaye aw yaram nga ma defaral.
ስለዚህ ወደ ዓለም ሲገባ። መሥዋዕትንና መባን አልወደድህም ሥጋን ግን አዘጋጀህልኝ፤
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
niroowul ak yeneen saraxalekat yu mag yi; soxlawul di def bés bu set ay saraxi mala ngir bàkkaari boppam jëkk, teg ca yoy mbooloo mi. yeesu def na sarax benn yoon ba fàww ngir dindi bàkkaar yi, bi muy joxe bakkanam.
እርሱም እንደነዚያ ሊቃነ ካህናት አስቀድሞ ስለ ራሱ ኃጢአት በኋላም ስለ ሕዝቡ ኃጢአት ዕለት ዕለት መሥዋዕትን ሊያቀርብ አያስፈልገውም፤ ራሱን ባቀረበ ጊዜ ይህን አንድ ጊዜ ፈጽሞ አድርጎአልና።
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
연관성이 낮은 일부 인적 번역은 숨겨져 있습니다.
연관성이 낮은 결과 표시.