검색어: binadamu (스와힐리어 - 월로프어)

인적 기여

전문 번역가, 번역 회사, 웹 페이지 및 자유롭게 사용할 수 있는 번역 저장소 등을 활용합니다.

번역 추가

스와힐리어

월로프어

정보

스와힐리어

basi, alichounganisha mungu, binadamu asitenganishe."

월로프어

lu yàlla takk nag, bu ko nit tas.»

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

스와힐리어

yesu akajibu, "yasiyowezekana kwa binadamu, yanawezekana kwa mungu."

월로프어

yeesu tontu ne: «li të nit ñi, tëwul yàlla.»

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

스와힐리어

ambao ni siri aliyowaficha binadamu wote tangu milele, lakini sasa amewajulisha watu wake.

월로프어

maanaam ma yégle kumpa, gi nëbbu woon ay jamonoy jamono, waaye léegi yàlla xamal na ko ay gaayam

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

maana yuko mungu mmoja, na pia yuko mmoja anayewapatanisha watu na mungu, binadamu kristo yesu,

월로프어

ndaxte jenn yàlla kepp moo am, ak benn rammukat kepp diggante yàlla ak nit ñi, di nit ki kirist yeesu,

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

lakini petro alimwinua, akamwambia, "simama, kwa maana mimi ni binadamu tu."

월로프어

waaye piyeer yékkati ko ne: «jógal, man it nit rekk laa.»

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

스와힐리어

"hata hivyo, mungu mkuu haishi katika nyumba zilizojengwa na binadamu; kama nabii asemavyo:

월로프어

«moona aji kawe ji du dëkk ci fu loxol nit defar; moom la ab yonent wax ne:

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

스와힐리어

basi, kama vile kosa la mtu mmoja lilivyoleta hukumu kwa binadamu wote, kadhalika kitendo kimoja kiadilifu kinawapa uhuru na uzima.

월로프어

kon nag nu gàttal wax ji; jàddug kenn nit ka rekk moo waral yàlla daan ñépp; noonu itam jëf ju jubu keneen nit ka rekk moo ubbi bunt, ba ñépp man a jub ci kanam yàlla te am dund gu bees.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

hapo petro, akiwa pamoja na wale mitume wengine, akajibu, "lazima tumtii mungu, na siyo binadamu.

월로프어

waaye piyeer ak ndaw ya tontu leen ne: «déggal yàlla moo gën déggal nit.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

스와힐리어

ikiwa basi, sisi ni watoto wa mungu, haifai kumfikiria mungu kuwa kama dhahabu, fedha au hata jiwe lililochongwa na kutiwa nakshi na binadamu.

월로프어

kon nag, bu nu nekkee xeetu yàlla, warunoo gëm ne, yàlla mel na ni nataali wurus, xaalis mbaa doj yu nit defar ci xareñ mbaa xel.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

basi sisi twafundisha, si kwa maneno tuliyofundishwa kwa hekima ya binadamu, bali kwa maneno tuliyofundishwa na roho, tukifafanua mambo ya kiroho kwa walio na huyo roho.

월로프어

te loolu nu yàlla may, yéglewunu ko ci ay baat yu soqikoo ci xam-xamu nit, waaye nu ngi koy yégle ci baat, yi soqikoo ci xelum yàlla, di tekkantal yëfi xelum yàlla ci ay baat yu mu nu sol.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

hii ndiyo njia ya kujua kama mtu anaongozwa na roho wa mungu: kila anayekiri kwamba kristo alikuja, akawa binadamu, mtu huyo anaye roho wa mungu.

월로프어

ci lii lanu xàmmee xelum yàlla: mépp xel mu nangu ne, yeesu kirist ñëw na, nekk nit, ci yàlla la bokk.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

maana kinachoonekana kuwa ni upumbavu wa mungu, kina busara zaidi kuliko hekima ya binadamu; na kinachoonekana kuwa ni udhaifu wa mungu, kina nguvu zaidi kuliko nguvu za binadamu.

월로프어

li ñuy wax ag ndof ca wàllu yàlla moo gën a tedd xam-xamu nit. te li ñuy wax ñàkk dooley yàlla moo ëpp kàttan dooley nit.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

majaribu mliyokwisha pata ni ya kawaida kwa binadamu. mungu ni mwaminifu, naye hataruhusu mjaribiwe kupita nguvu zenu, ila pamoja na majaribu, yeye atawapeni pia nguvu ya kustahimili na njia ya kutoka humo salama.

월로프어

benn nattu dabu leen bu wuute ak yi dal nit ñépp. te sax yàlla kuy sàmm kóllëre la, te du nangu nattu bi wees seen kàttan, waaye cib nattu, dina leen ubbil bunt bu ngeen man a récce, ba ngeen man koo dékku.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

kama mnaitimiza ile sheria ya utawala kama ilivyoandikwa katika maandiko matakatifu: "mpende binadamu mwenzako kama unavyojipenda wewe mwenyewe", mtakuwa mnafanya vema kabisa.

월로프어

su ngeen sàmmee yoonu buur yàlla, ni ko mbind mi tërale naan: «nanga bëgg sa moroom, ni nga bëgge sa bopp,» kon def ngeen lu baax.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

스와힐리어

lakini, ewe binadamu, u nani hata uthubutu kumhoji mungu? je, chungu chaweza kumwuliza mfinyanzi wake: "kwa nini umenitengeneza namna hii?"

월로프어

yaw nag nit ki, ak koo man a doon, lu tax ngay werante ak yàlla? ndax mbindeef dina laaj ki ko bind: «lu tax nga binde ma nii?»

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

스와힐리어

"ndugu, kwa nini mnafanya mambo hayo? sisi pia ni binadamu kama ninyi. na, tuko hapa kuwahubirieni habari njema, mpate kuziacha hizi sanamu tupu, mkamgeukie mungu aliye hai, mungu aliyeumba mbingu na nchi, bahari na vyote vilivyomo.

월로프어

«yéen nit ñi, lu leen xiir ci lii? nun it ay nit lanu, ñu bokk bind ak yéen. te nu ngi leen di xamal xebaar bu baax ne leen, ngeen dëddu yëfi neen yii te woññiku ci yàlla miy dund te sàkk asamaan, suuf, géej ak li ñu ëmb lépp.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

인적 기여로
9,199,212,828 더 나은 번역을 얻을 수 있습니다

사용자가 도움을 필요로 합니다:



당사는 사용자 경험을 향상시키기 위해 쿠키를 사용합니다. 귀하께서 본 사이트를 계속 방문하시는 것은 당사의 쿠키 사용에 동의하시는 것으로 간주됩니다. 자세히 보기. 확인