전문 번역가, 번역 회사, 웹 페이지 및 자유롭게 사용할 수 있는 번역 저장소 등을 활용합니다.
ndugu zangu, muwe na furaha mnapopatwa na majaribu mbalimbali,
yéen samay bokk, waxtu wu nattu yi dalee ci seen kaw, ak nu ñu man a mel, defleen ko ni mbég mu réy,
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
zipo lugha mbalimbali ulimwenguni, na hakuna hata mojawapo isiyo na maana.
xawma ñaata xeeti làkk a am ci àddina, te wu ci nekk am na lu muy tekki.
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
wote wakajazwa roho mtakatifu, wakaanza kusema lugha mbalimbali kadiri roho alivyowawezesha.
noonu ñu fees ak xel mu sell mi ñoom ñépp, ñu daldi wax yeneeni làkk, ni leen xel mu sell mi maye, ñu wax ko.
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
gnome inatimiza zana mbalimbali za utungaji wa maprogramu zinazowezesha uundaji wa maprogramu bora.
ak gnome dees na jébbalaale it ab joyaluwaay bees jagleel tëralkat yi, tax ñuy man a bindiy tëriin yu kàttanu te fasu
마지막 업데이트: 2014-08-15
사용 빈도: 1
품질:
watu walitupatia zawadi mbalimbali na wakati tulipoanza tena safari, walitia ndani ya meli masurufu tuliyohitaji.
Ñu teral nu ci fànn yu bare, te bi nuy dem, ñu jox nu li nuy soxla lépp.
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
kuna namna mbalimbali za kufanya kazi ya huduma, lakini mungu ni mmoja, anayewezesha kazi zote katika wote.
am na ay fànn yu bare yu yàllay feeñale dooleem, waaye jenn yàlla ji mooy jëfe doole yooyu yépp ci ñépp.
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
basi, tunavyo vipaji mbalimbali kufuatana na neema tuliyopewa. mwenye kipaji cha unabii na akitumie kadiri ya imani yake.
kon gannaaw yàlla séddale na ay mayam, ku nekk ak sa cér, nanu koy jëfandikoo. ku yàlla may, ngay waare kàddoom, nga wax ko kem sa ngëm;
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
basi, paulo akawawekea mikono, na roho mtakatifu akawashukia, wakaanza kusema lugha mbalimbali na kutangaza ujumbe wa mungu.
te bi leen pool tegee loxo, xel mu sell mi ñëw ci ñoom, ñuy wax yeneeni làkk, di wax ci kàddug yàlla.
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
naye yesu akawaponya watu wengi waliokuwa na magonjwa mbalimbali; aliwafukuza pepo wengi, lakini hakuwaruhusu kusema kitu maana walikuwa wanamjua yeye ni nani.
noonu mu wéral ñu bare, ñu wopp ak ay jàngoro yu wuute, te dàq ay rab yu bare. waaye mu tere rab yi, ñu wax dara, ndaxte xam nañu ko.
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
jua lilipokuwa linatua, wote waliokuwa na wagonjwa wao mbalimbali waliwaleta kwake; naye akaweka mikono yake juu ya kila mmoja wao, akawaponya wote.
bi jant sowee, ñu indil yeesu ñi wopp ñépp ak ay jàngoro yu wuute. kenn ku nekk mu teg la loxo, wéral la.
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
kwani haya yote yanahusika na vyakula, vinywaji na taratibu mbalimbali za kutawadha. yote hayo ni maagizo ya njenje tu; na nguvu yake hukoma wakati mungu atakaporekebisha vitu vyote.
sarax yooyu ñu ngi jëmoon ci lekk ak ci naan ak ci fànn yu bare ci mbirum sangu set. ay sàrt yu jëm ci yaram lañu, yu ñu waroon a farataal, ba kera jamono ji yàllay tëral kóllëre gu bees.
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
basi, pamoja na ndugu hao, tumemtuma ndugu yetu mwingine ambaye mara nyingi tumempa majaribio mbalimbali, tukamwona kuwa ni mwenye hamu kubwa ya kusaidia; hata sasa amekuwa na moyo zaidi kwa sababu ana imani sana nanyi.
yónniwaale nanu it sunu mbokk, mi nu seetlu cawarteem ay yooni yoon ci fànn yu bare, te mu gën koo fésal bii yoon ndax kóolute gu réy, gi mu am ci yéen.
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질: