전문 번역가, 번역 회사, 웹 페이지 및 자유롭게 사용할 수 있는 번역 저장소 등을 활용합니다.
maana tumesikia juu ya imani yenu katika kristo yesu na juu ya upendo wenu kwa watu wote wa mungu.
ndaxte yég nanu seen ngëm ci kirist yeesu ak seen mbëggeel ci gaayi yàlla yépp.
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
nao wakasema, "je, tunahitaji ushahidi mwingine? sisi wenyewe tumesikia akisema kwa mdomo wake mwenyewe."
Ñu daldi ne nag: «lu nuy doyeeti seede léegi, ndegam nun ci sunu bopp noo ko nangoo ci gémmiñam!»
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다
tumesikia kwamba watu wengine kutoka huku kwetu waliwavurugeni kwa maneno yao, wakaitia mioyo yenu katika wasiwasi. lakini wamefanya hivyo bila ya idhini yoyote kutoka kwetu.
dégg nanu ne, am na ay nit ñu bawoo ci nun, ñu di leen lëjal ak seeni wax, di jaxase seeni xol, te fekk sukkandikuwuñu ci lenn ndigal lu jóge ci nun.
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
wakamwambia yule mama, "sisi hatuamini tu kwa sababu ya maneno yako; sisi wenyewe tumesikia, na tunajua kwamba huyu ndiye kweli mwokozi wa ulimwengu."
Ñu ne jigéen ja: «léegi gëm nanu, te du li nga wax moo tax waaye li nu gisal sunu bopp. te xam nanu ne, dëgg-dëgg kii moo di musalkatu àddina si.»
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다