검색어: wageni (스와힐리어 - 월로프어)

인적 기여

전문 번역가, 번역 회사, 웹 페이지 및 자유롭게 사용할 수 있는 번역 저장소 등을 활용합니다.

번역 추가

스와힐리어

월로프어

정보

스와힐리어

wasaidieni watu wa mungu katika mahitaji yao; wapokeeni wageni kwa ukarimu.

월로프어

dimbalileen gaayi yàlla yi ci seeni soxla, te saxoo dalal gan.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

mpenzi wangu, wewe ni mwaminifu kila mara unapowahudumia ndugu, hata kama ni wageni.

월로프어

yaw sama xarit, sa takkute fés na ci teeru bi ngay teeru mbokk yi, te fekk xamoo leen.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

basi, wakashauriana, wakazitumia kununua shamba la mfinyanzi liwe mahali pa kuzika wageni.

월로프어

Ñu daldi diisoo nag, jënd ca xaalis ba toolu defarkatu ndaa ya, ngir di fa suul doxandéem ya.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

"mfalme alipoingia kuwaona wageni, akamwona mtu mmoja ambaye hakuvaa mavazi ya arusi.

월로프어

«bi nga xamee ne buur bi dugg na nag, ngir seetsi gan yi, mu gis fa nit ku solul mbubb mu ñu war a sol ca céet ga.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

스와힐리어

msisahau kuwakaribisha wageni; maana kwa kufanya hivyo watu wengine walipata kuwakaribisha malaika bila kujua.

월로프어

buleen fàttee teral ñiy ñëw ci yéen, ndaxte ñenn ñi, bi ñu ko defee, teral nañu ay malaaka te xamuñu ko.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

frugia na pamfulia, misri na sehemu za libya karibu na kurene; wengine wetu ni wageni kutoka roma,

월로프어

di waa firisi, pamfili, misra ak weti libi, yi dend ak siren, nun ak gan ñi jóge room,

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

mfalme akahuzunika sana, lakini kwa sababu ya kiapo chake, na kwa ajili ya wale wageni wake karamuni, hakutaka kumkatalia.

월로프어

bi ko buur ba déggee, mu am naqar wu réy. waaye bëggu koo gàntu ndax ngiñ li ak gan ñi.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

akajifungua mtoto wake wa kwanza wa kiume, akamvika nguo za kitoto, akamlaza horini kwa sababu hawakupata nafasi katika nyumba ya wageni.

월로프어

mu taawloo doom ju góor, mu laxas ko ci ay laytaay, tëral ko ca lekkukaayu jur ga, ndaxte xajuñu woon ca dalukaay ba.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

karibu na mahali pale palikuwa na mashamba ya publio, mkuu wa kile kisiwa. publio alitukaribisha kirafiki, tukawa wageni wake kwa siku tatu.

월로프어

amoon na nag ca wet ya ay suuf yu doon moomeelu ku tudd publiyus, di kilifag dun ba. mu teeru nu, ganale nu ngan gu réy diirub ñetti fan.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

akamwendea, akamtibu majeraha yake kwa kumtia mafuta na divai; na kuyafunga halafu akampandisha juu ya punda wake akampeleka katika nyumba moja ya wageni akamuuguza.

월로프어

noonu mu ñëw, diw ko diwlin ak biiñ ngir faj gaañu-gaañu ya, bandaas ko. gannaaw loolu mu teg ko ci mbaamam, yóbbu ko ci fanaanukaay, di ko topptoo.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

na awe mwenye sifa nzuri: aliyewalea watoto wake vizuri, aliyewakaribisha wageni nyumbani kwake, aliyewaosha miguu watu wa mungu, aliyewasaidia watu wenye taabu, na aliyejitolea kufanya mambo mema.

월로프어

te mu ràññiku ci jëf yu rafet yu deme ni yar ay guneem, man gan, geestu gaayi yàlla yu sell yi, dimbali ñi nekk ci tiis; maanaa di ku takku ci mboolem jëf yu rafet yi.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

baada ya wale wageni kuondoka, malaika wa bwana alimtokea yosefu katika ndoto, akamwambia, "amka! mchukue mtoto pamoja na mama yake, mkimbilie misri. kaeni huko mpaka nitakapokwambia, maana herode anakusudia kumwua huyu mtoto."

월로프어

bi nga xamee ne boroom xam-xam ya ñibbi nañu, benn malaakam boroom bi feeñu yuusufa ci gént ne ko: «erodd mu ngi ci tànki wut xale bi, ngir rey ko; jógal nag, jël xale bi ak ndeyam te nga daw jëm misra, toog fa, ba kera ma koy wax.»

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

인적 기여로
7,787,514,074 더 나은 번역을 얻을 수 있습니다

사용자가 도움을 필요로 합니다:



당사는 사용자 경험을 향상시키기 위해 쿠키를 사용합니다. 귀하께서 본 사이트를 계속 방문하시는 것은 당사의 쿠키 사용에 동의하시는 것으로 간주됩니다. 자세히 보기. 확인